An-Nahl · 6/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَلَكُمْ فِيهَا جَمَالٌ حِينَ تُرِيحُونَ وَحِينَ تَسْرَحُونَ ۝٦
Wa lakum feehaa jamaalun heena tureehoona wa heena tasrahoon
📖 Tekkim Wolof
Te it yéen a ngi bànneexu ci seeni taar bu ngeen di jofal ci ngoon ak bu ngeen di wëtal ci suba.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore An-Nahl

4خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Moo bind nit ñi ci toqent ; te moom [nit] mu nekk di pànk mu mën a xuloo.
5وَالْأَنْعَامَ خَلَقَهَا ۗ لَكُمْ فِيهَا دِفْءٌ وَمَنَافِعُ وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
[Moo bind it] mala yi, ngeen di ca jële ay yére yu nuggu ak yeneen njariñ. Ak lu ngeen di lekk.
6وَلَكُمْ فِيهَا جَمَالٌ حِينَ تُرِيحُونَ وَحِينَ تَسْرَحُونَ
Te it yéen a ngi bànneexu ci seeni taar bu ngeen di jofal ci ngoon ak bu ngeen di wëtal ci suba.
7وَتَحْمِلُ أَثْقَالَكُمْ إِلَىٰ بَلَدٍ لَّمْ تَكُونُوا بَالِغِيهِ إِلَّا بِشِقِّ الْأَنفُسِ ۚ إِنَّ رَبَّكُمْ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Te danañu yenu seen [yóbbal], yóbbul leen ko ca dëkk ba ngeen dul woon mën a dem lu dul ci ab coono bub bakkan. Naka seen Boroom Aji-ñeewant la, Jaglewaakoon la.
8وَالْخَيْلَ وَالْبِغَالَ وَالْحَمِيرَ لِتَرْكَبُوهَا وَزِينَةً ۚ وَيَخْلُقُ مَا لَا تَعْلَمُونَ
[Moo bind it] fas ak i baxla [berkelle] ak mbaam ngir ngeen war leen, ak ngir taar. Te it bind na lu ngeen xamul.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — An-Nahl 6

Simoore An-Nahl Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it yéen a ngi bànneexu ci seeni taar bu…

Simoore Aaya 6/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers