An-Nahl · 5/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَالْأَنْعَامَ خَلَقَهَا ۗ لَكُمْ فِيهَا دِفْءٌ وَمَنَافِعُ وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ ۝٥
Wal an `amaa khalaqahaa; lakum feehaa dif`unw wa manaafi`u wa minhaa taakuloon
📖 Tekkim Wolof
[Moo bind it] mala yi, ngeen di ca jële ay yére yu nuggu ak yeneen njariñ. Ak lu ngeen di lekk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore An-Nahl

3خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ ۚ تَعَالَىٰ عَمَّا يُشْرِكُونَ
Moo bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg. Kawe na, sori lool la ñu koy bokkaale.
4خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Moo bind nit ñi ci toqent ; te moom [nit] mu nekk di pànk mu mën a xuloo.
5وَالْأَنْعَامَ خَلَقَهَا ۗ لَكُمْ فِيهَا دِفْءٌ وَمَنَافِعُ وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
[Moo bind it] mala yi, ngeen di ca jële ay yére yu nuggu ak yeneen njariñ. Ak lu ngeen di lekk.
6وَلَكُمْ فِيهَا جَمَالٌ حِينَ تُرِيحُونَ وَحِينَ تَسْرَحُونَ
Te it yéen a ngi bànneexu ci seeni taar bu ngeen di jofal ci ngoon ak bu ngeen di wëtal ci suba.
7وَتَحْمِلُ أَثْقَالَكُمْ إِلَىٰ بَلَدٍ لَّمْ تَكُونُوا بَالِغِيهِ إِلَّا بِشِقِّ الْأَنفُسِ ۚ إِنَّ رَبَّكُمْ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Te danañu yenu seen [yóbbal], yóbbul leen ko ca dëkk ba ngeen dul woon mën a dem lu dul ci ab coono bub bakkan. Naka seen Boroom Aji-ñeewant la, Jaglewaakoon la.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
5Aaya

Tekki — An-Nahl 5

Simoore An-Nahl Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Moo bind it] mala yi, ngeen di ca jële ay…

Simoore Aaya 5/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers