An-Nahl · 78/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
وَاللَّهُ أَخْرَجَكُم مِّن بُطُونِ أُمَّهَاتِكُمْ لَا تَعْلَمُونَ شَيْئًا وَجَعَلَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۙ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ ۝٧٨
Wallaahu akhrajakum mim butooni ummahaatikum laa ta`lamoona shai`anw wa ja`ala lakumus sam`a wal absaara wal af`idata la`allakum tashkuroon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla moo leen génne ci seen biiri ndey, xamuleen wóon dara, Mu sàkkal leen ag dégg ak ug gis, ak xel, ndaxtelee ngeen gërëm ko.
🎧 Dégg

📜 Aaya 76-80 — An-Nahl

76وَضَرَبَ اللَّهُ مَثَلًا رَّجُلَيْنِ أَحَدُهُمَا أَبْكَمُ لَا يَقْدِرُ عَلَىٰ شَيْءٍ وَهُوَ كَلٌّ عَلَىٰ مَوْلَاهُ أَيْنَمَا يُوَجِّههُّ لَا يَأْتِ بِخَيْرٍ ۖ هَلْ يَسْتَوِي هُوَ وَمَن يَأْمُرُ بِالْعَدْلِ ۙ وَهُوَ عَلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Yàllaa ngay joxe ba-tey léebu ñaari góor yoo xam ne : kenn ka dafa luu [muuma], mënul dara te moom dafa wéeru ci sangam ; Te fu mu mën di jubale, du ca jële njariñ ; ndax dafay yem ak ki nga xam ne dafay digle maandute te lu mu def mu àntu tegu ci njub ?
77وَلِلَّهِ غَيْبُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَمَا أَمْرُ السَّاعَةِ إِلَّا كَلَمْحِ الْبَصَرِ أَوْ هُوَ أَقْرَبُ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Ñeel na Yàlla kumpag asamaan yi ak suuf si. Te mbiru Bis-pénc ba dafay mel ni xef ak xippi mbaa lu ko gën a gaaw ! Naka Yàlla lu nekk la mën.
78وَاللَّهُ أَخْرَجَكُم مِّن بُطُونِ أُمَّهَاتِكُمْ لَا تَعْلَمُونَ شَيْئًا وَجَعَلَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۙ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Yàlla moo leen génne ci seen biiri ndey, xamuleen wóon dara, Mu sàkkal leen ag dégg ak ug gis, ak xel, ndaxtelee ngeen gërëm ko.
79أَلَمْ يَرَوْا إِلَى الطَّيْرِ مُسَخَّرَاتٍ فِي جَوِّ السَّمَاءِ مَا يُمْسِكُهُنَّ إِلَّا اللَّهُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Ndax gisuñu picc yi [mbindéef yu ñu tàggat lañu ci jawi asamaan si], dara téyuleen lu dul Yàlla ? Te nekk na ci biir loolu dëgg-dëggi kéemtaan ngir aw nit ñu gëm.
80وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُم مِّن بُيُوتِكُمْ سَكَنًا وَجَعَلَ لَكُم مِّن جُلُودِ الْأَنْعَامِ بُيُوتًا تَسْتَخِفُّونَهَا يَوْمَ ظَعْنِكُمْ وَيَوْمَ إِقَامَتِكُمْ ۙ وَمِنْ أَصْوَافِهَا وَأَوْبَارِهَا وَأَشْعَارِهَا أَثَاثًا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ
Yàlla defal na leen ca seen biiri kër ay dëkkuwaay [néeg], Mu defal leen ci deri mala yi kiiraay [mbaar] mu woyof ci bu ngeen di tukki walla ngeen di sax fenn. Te defal na leen it ci ngëndël ak ci seeni karaw ak seeni cëx-cëx laltaayi néeg ak i jumtukaay bu jëmmi jamonoo.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — An-Nahl 78

Simoore An-Nahl Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla moo leen génne ci seen biiri ndey, xamuleen wóon…

Simoore Aaya 78/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers