An-Nahl · 79/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
أَلَمْ يَرَوْا إِلَى الطَّيْرِ مُسَخَّرَاتٍ فِي جَوِّ السَّمَاءِ مَا يُمْسِكُهُنَّ إِلَّا اللَّهُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ ٧٩
Transliteration
Alam yaraw ilat tairi musakhkharaatin fee jawwis samaaa`i maa yumsikuhunna illal laah; inna fee zaalika la Aayaatil liqawminy yu`minoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ndax gisuñu picc yi [mbindéef yu ñu tàggat lañu ci jawi asamaan si], dara téyuleen lu dul Yàlla ? Te nekk na ci biir loolu dëgg-dëggi kéemtaan ngir aw nit ñu gëm.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 77-81 — An-Nahl
77وَلِلَّهِ غَيْبُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ وَمَا أَمْرُ السَّاعَةِ إِلَّا كَلَمْحِ الْبَصَرِ أَوْ هُوَ أَقْرَبُ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Ñeel na Yàlla kumpag asamaan yi ak suuf si. Te mbiru Bis-pénc ba dafay mel ni xef ak xippi mbaa lu ko gën a gaaw ! Naka Yàlla lu nekk la mën.
78وَاللَّهُ أَخْرَجَكُم مِّن بُطُونِ أُمَّهَاتِكُمْ لَا تَعْلَمُونَ شَيْئًا وَجَعَلَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۙ لَعَلَّكُمْ تَشْكُرُونَ
Yàlla moo leen génne ci seen biiri ndey, xamuleen wóon dara, Mu sàkkal leen ag dégg ak ug gis, ak xel, ndaxtelee ngeen gërëm ko.
79أَلَمْ يَرَوْا إِلَى الطَّيْرِ مُسَخَّرَاتٍ فِي جَوِّ السَّمَاءِ مَا يُمْسِكُهُنَّ إِلَّا اللَّهُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Ndax gisuñu picc yi [mbindéef yu ñu tàggat lañu ci jawi asamaan si], dara téyuleen lu dul Yàlla ? Te nekk na ci biir loolu dëgg-dëggi kéemtaan ngir aw nit ñu gëm.
80وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُم مِّن بُيُوتِكُمْ سَكَنًا وَجَعَلَ لَكُم مِّن جُلُودِ الْأَنْعَامِ بُيُوتًا تَسْتَخِفُّونَهَا يَوْمَ ظَعْنِكُمْ وَيَوْمَ إِقَامَتِكُمْ ۙ وَمِنْ أَصْوَافِهَا وَأَوْبَارِهَا وَأَشْعَارِهَا أَثَاثًا وَمَتَاعًا إِلَىٰ حِينٍ
Yàlla defal na leen ca seen biiri kër ay dëkkuwaay [néeg], Mu defal leen ci deri mala yi kiiraay [mbaar] mu woyof ci bu ngeen di tukki walla ngeen di sax fenn. Te defal na leen it ci ngëndël ak ci seeni karaw ak seeni cëx-cëx laltaayi néeg ak i jumtukaay bu jëmmi jamonoo.
81وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُم مِّمَّا خَلَقَ ظِلَالًا وَجَعَلَ لَكُم مِّنَ الْجِبَالِ أَكْنَانًا وَجَعَلَ لَكُمْ سَرَابِيلَ تَقِيكُمُ الْحَرَّ وَسَرَابِيلَ تَقِيكُم بَأْسَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ يُتِمُّ نِعْمَتَهُ عَلَيْكُمْ لَعَلَّكُمْ تُسْلِمُونَ
Yàlla defal na leen, ci li Mu bind, ay ker. Mu defal leen ci doj yi ay néeg. Mu defal leen ci mbubb yu leen di fegal tàngoor, ak mbubbi koŋ yu leen di fegal seen ngaañ. Noonu la mottalee xéewalam ndax xéy-na ngeen jébbalu [doon ay jullit tigi].
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
79Aaya
Tekki — An-Nahl 79
Simoore An-Nahl Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax gisuñu picc yi [mbindéef yu ñu tàggat lañu ci…Simoore Aaya 79/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








