An-Nahl · 83/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
يَعْرِفُونَ نِعْمَتَ اللَّهِ ثُمَّ يُنكِرُونَهَا وَأَكْثَرُهُمُ الْكَافِرُونَ ۝٨٣
Ya`rifoona ni`matal laahi summa yunkiroonahaa wa aksaruhumul kaafiroon
📖 Tekkim Wolof
Xam nañu xell Yàlla ba noppi ; ñu fakk ko. Te ñu bari ci ñoom yéefar lañu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 81-85 — An-Nahl

81وَاللَّهُ جَعَلَ لَكُم مِّمَّا خَلَقَ ظِلَالًا وَجَعَلَ لَكُم مِّنَ الْجِبَالِ أَكْنَانًا وَجَعَلَ لَكُمْ سَرَابِيلَ تَقِيكُمُ الْحَرَّ وَسَرَابِيلَ تَقِيكُم بَأْسَكُمْ ۚ كَذَٰلِكَ يُتِمُّ نِعْمَتَهُ عَلَيْكُمْ لَعَلَّكُمْ تُسْلِمُونَ
Yàlla defal na leen, ci li Mu bind, ay ker. Mu defal leen ci doj yi ay néeg. Mu defal leen ci mbubb yu leen di fegal tàngoor, ak mbubbi koŋ yu leen di fegal seen ngaañ. Noonu la mottalee xéewalam ndax xéy-na ngeen jébbalu [doon ay jullit tigi].
82فَإِن تَوَلَّوْا فَإِنَّمَا عَلَيْكَ الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
Bu ñu dëddoo Yàlla... dara waru la [yaw Yonent bi] lu dul jottali gu mat, bu ñu ko xasee dégg rekk wàcc na la.
83يَعْرِفُونَ نِعْمَتَ اللَّهِ ثُمَّ يُنكِرُونَهَا وَأَكْثَرُهُمُ الْكَافِرُونَ
Xam nañu xell Yàlla ba noppi ; ñu fakk ko. Te ñu bari ci ñoom yéefar lañu.
84وَيَوْمَ نَبْعَثُ مِن كُلِّ أُمَّةٍ شَهِيدًا ثُمَّ لَا يُؤْذَنُ لِلَّذِينَ كَفَرُوا وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
Ca bis ba Nu dogalee ci xeet wu ne seen seede, te deeful may [ña weddi] lay, te duñu leen nangul it ngànt.
85وَإِذَا رَأَى الَّذِينَ ظَلَمُوا الْعَذَابَ فَلَا يُخَفَّفُ عَنْهُمْ وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Ña tooñ, bis ba ñu gisee mbugal ma, deesuleen woyofalal dara, te deefuleen yeexe.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
83Aaya

Tekki — An-Nahl 83

Simoore An-Nahl Aaya 83 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xam nañu xell Yàlla ba noppi ; ñu fakk ko.…

Simoore Aaya 83/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 81–85. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers