An-Nahl · 84/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَيَوْمَ نَبْعَثُ مِن كُلِّ أُمَّةٍ شَهِيدًا ثُمَّ لَا يُؤْذَنُ لِلَّذِينَ كَفَرُوا وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ ۝٨٤
Wa yawma nab`asu min kulli ummatin shaheedan summa laa yu`zanu lillazeena kafaroo wa laa hum yusta`taboon
📖 Tekkim Wolof
Ca bis ba Nu dogalee ci xeet wu ne seen seede, te deeful may [ña weddi] lay, te duñu leen nangul it ngànt.

🎧 Dégg


📜 Aaya 82-86 — Simoore An-Nahl

82فَإِن تَوَلَّوْا فَإِنَّمَا عَلَيْكَ الْبَلَاغُ الْمُبِينُ
Bu ñu dëddoo Yàlla... dara waru la [yaw Yonent bi] lu dul jottali gu mat, bu ñu ko xasee dégg rekk wàcc na la.
83يَعْرِفُونَ نِعْمَتَ اللَّهِ ثُمَّ يُنكِرُونَهَا وَأَكْثَرُهُمُ الْكَافِرُونَ
Xam nañu xell Yàlla ba noppi ; ñu fakk ko. Te ñu bari ci ñoom yéefar lañu.
84وَيَوْمَ نَبْعَثُ مِن كُلِّ أُمَّةٍ شَهِيدًا ثُمَّ لَا يُؤْذَنُ لِلَّذِينَ كَفَرُوا وَلَا هُمْ يُسْتَعْتَبُونَ
Ca bis ba Nu dogalee ci xeet wu ne seen seede, te deeful may [ña weddi] lay, te duñu leen nangul it ngànt.
85وَإِذَا رَأَى الَّذِينَ ظَلَمُوا الْعَذَابَ فَلَا يُخَفَّفُ عَنْهُمْ وَلَا هُمْ يُنظَرُونَ
Ña tooñ, bis ba ñu gisee mbugal ma, deesuleen woyofalal dara, te deefuleen yeexe.
86وَإِذَا رَأَى الَّذِينَ أَشْرَكُوا شُرَكَاءَهُمْ قَالُوا رَبَّنَا هَٰؤُلَاءِ شُرَكَاؤُنَا الَّذِينَ كُنَّا نَدْعُو مِن دُونِكَ ۖ فَأَلْقَوْا إِلَيْهِمُ الْقَوْلَ إِنَّكُمْ لَكَاذِبُونَ
Te ña doon bokkaale, bu ñu gisee seen xërëm ya, danañu ne : “Yaw sunu Boroom, ñile ñoo di ñanu daan bokkaalee, di leen jaamu bàyyi la”. Ñoom it ñu tontu ne : “Yéen ay fenkat ngeen”.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — An-Nahl 84

Simoore An-Nahl Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca bis ba Nu dogalee ci xeet wu ne seen…

Simoore Aaya 84/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers