Al-Isra · 105/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَبِالْحَقِّ أَنزَلْنَاهُ وَبِالْحَقِّ نَزَلَ ۗ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا مُبَشِّرًا وَنَذِيرًا ۝١٠٥
Wa bilhaqqi anzalnaahu wa bilhaqqi nazal; wa maaa arsalnaaka illaa mubash shiranw wa nazeeraa
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg wàcce na ko te ci dëgg it la wàcce ni ci yaw [Yonent bi], kuy bégle, di xuppe nga.

🎧 Dégg


📜 Aaya 103-107 — Simoore Al-Isra

103فَأَرَادَ أَن يَسْتَفِزَّهُم مِّنَ الْأَرْضِ فَأَغْرَقْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ جَمِيعًا
Mu bëgg leen a génne suuf sa. Nu labal ko mook ña mu àndaloon ñépp.
104وَقُلْنَا مِن بَعْدِهِ لِبَنِي إِسْرَائِيلَ اسْكُنُوا الْأَرْضَ فَإِذَا جَاءَ وَعْدُ الْآخِرَةِ جِئْنَا بِكُمْ لَفِيفًا
Nu wax ginnaawam ñeel (waa Bani-Israayiil)ne leen : “Dëkkeleen suuf sa”. Ba àppu bisub àllaaxira jotee, Dananu leen indi ngeen di mbooloo.
105وَبِالْحَقِّ أَنزَلْنَاهُ وَبِالْحَقِّ نَزَلَ ۗ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا مُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Ca dëgg-dëgg wàcce na ko te ci dëgg it la wàcce ni ci yaw [Yonent bi], kuy bégle, di xuppe nga.
106وَقُرْآنًا فَرَقْنَاهُ لِتَقْرَأَهُ عَلَى النَّاسِ عَلَىٰ مُكْثٍ وَنَزَّلْنَاهُ تَنزِيلًا
Te Alxuraan, téqale Nanu ko [cig wàccam] ngir nga jàng ko ci nit ñi, cig teey. Te wàcce Nanu ko ndànk-ndànk.
107قُلْ آمِنُوا بِهِ أَوْ لَا تُؤْمِنُوا ۚ إِنَّ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ مِن قَبْلِهِ إِذَا يُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ يَخِرُّونَ لِلْأَذْقَانِ سُجَّدًا
Neel : “Gëmleen ko mbaa ngeen bañ koo gëm, nanga xam ne joxeef na leen xam-xam. La ko jiitu, bu ñu jàngee ci seen kanam, danañu rot dëpp seeni sikkim ci suuf, sujjóot”
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
105Aaya

Tekki — Al-Isra 105

Simoore Al-Isra Aaya 105 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg wàcce na ko te ci dëgg it la…

Simoore Aaya 105/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 103–107. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers