Al-Isra · 104/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
وَقُلْنَا مِن بَعْدِهِ لِبَنِي إِسْرَائِيلَ اسْكُنُوا الْأَرْضَ فَإِذَا جَاءَ وَعْدُ الْآخِرَةِ جِئْنَا بِكُمْ لَفِيفًا ۝١٠٤
Wa qulnaa mim ba`dihee li Baneee Israaa`eelas kunul arda faizaa jaaa`a wa`dulaakhirati ji`naa bikum lafeefaa
📖 Tekkim Wolof
Nu wax ginnaawam ñeel (waa Bani-Israayiil)ne leen : “Dëkkeleen suuf sa”. Ba àppu bisub àllaaxira jotee, Dananu leen indi ngeen di mbooloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 102-106 — Simoore Al-Isra

102قَالَ لَقَدْ عَلِمْتَ مَا أَنزَلَ هَٰؤُلَاءِ إِلَّا رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ بَصَائِرَ وَإِنِّي لَأَظُنُّكَ يَا فِرْعَوْنُ مَثْبُورًا
[Muusaa tontu ne] : “Xam nga ne kenn wàccewul yile [kéemaan] ku dul Boroom asamaan yi ak suuf si ngir ñu nekk di waare ; te damaa defe ni, yaw Firawna, dangaa nekk ku alku”.
103فَأَرَادَ أَن يَسْتَفِزَّهُم مِّنَ الْأَرْضِ فَأَغْرَقْنَاهُ وَمَن مَّعَهُ جَمِيعًا
Mu bëgg leen a génne suuf sa. Nu labal ko mook ña mu àndaloon ñépp.
104وَقُلْنَا مِن بَعْدِهِ لِبَنِي إِسْرَائِيلَ اسْكُنُوا الْأَرْضَ فَإِذَا جَاءَ وَعْدُ الْآخِرَةِ جِئْنَا بِكُمْ لَفِيفًا
Nu wax ginnaawam ñeel (waa Bani-Israayiil)ne leen : “Dëkkeleen suuf sa”. Ba àppu bisub àllaaxira jotee, Dananu leen indi ngeen di mbooloo.
105وَبِالْحَقِّ أَنزَلْنَاهُ وَبِالْحَقِّ نَزَلَ ۗ وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا مُبَشِّرًا وَنَذِيرًا
Ca dëgg-dëgg wàcce na ko te ci dëgg it la wàcce ni ci yaw [Yonent bi], kuy bégle, di xuppe nga.
106وَقُرْآنًا فَرَقْنَاهُ لِتَقْرَأَهُ عَلَى النَّاسِ عَلَىٰ مُكْثٍ وَنَزَّلْنَاهُ تَنزِيلًا
Te Alxuraan, téqale Nanu ko [cig wàccam] ngir nga jàng ko ci nit ñi, cig teey. Te wàcce Nanu ko ndànk-ndànk.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
104Aaya

Tekki — Al-Isra 104

Simoore Al-Isra Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu wax ginnaawam ñeel (waa Bani-Israayiil)ne leen : “Dëkkeleen suuf…

Simoore Aaya 104/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers