Al-Isra · 24/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَاخْفِضْ لَهُمَا جَنَاحَ الذُّلِّ مِنَ الرَّحْمَةِ وَقُل رَّبِّ ارْحَمْهُمَا كَمَا رَبَّيَانِي صَغِيرًا ۝٢٤
Wakhfid lahumaa janaahaz zulli minar rahmati wa qur Rabbir hamhumaa kamaa rabbayaanee sagheera
📖 Tekkim Wolof
Nanga suufeel sa bopp ngir ñoom ; di toroxlu ci yërmaande ; te deel wax : "Sama Boroom yërëm leen [ni ñu ma yërëme woon] ba ñu may yar ba ma nekkee xale”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Al-Isra

22لَّا تَجْعَلْ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَتَقْعُدَ مَذْمُومًا مَّخْذُولًا
Bul sàkk jeneen yàlla di ko booleek Yàlla ; kon dey danga doon ku ñu xas, ku ñu wacc mu beddiku.
23۞ وَقَضَىٰ رَبُّكَ أَلَّا تَعْبُدُوا إِلَّا إِيَّاهُ وَبِالْوَالِدَيْنِ إِحْسَانًا ۚ إِمَّا يَبْلُغَنَّ عِندَكَ الْكِبَرَ أَحَدُهُمَا أَوْ كِلَاهُمَا فَلَا تَقُل لَّهُمَا أُفٍّ وَلَا تَنْهَرْهُمَا وَقُل لَّهُمَا قَوْلًا كَرِيمًا
Sa Boroom dogal na ne : “Buleen jaamu ku dul Moom doŋŋ ; te ngeen rafetal jëme ci seeni waajur : te ndeem kenn ci ñoom walla ñoom ñaar egg nañu ci màggat ci sa teewaay ; buleen wax : “Kuf ma la ! ”, buleen leen gëdd, nangeen leen wax wax ju yiw.
24وَاخْفِضْ لَهُمَا جَنَاحَ الذُّلِّ مِنَ الرَّحْمَةِ وَقُل رَّبِّ ارْحَمْهُمَا كَمَا رَبَّيَانِي صَغِيرًا
Nanga suufeel sa bopp ngir ñoom ; di toroxlu ci yërmaande ; te deel wax : "Sama Boroom yërëm leen [ni ñu ma yërëme woon] ba ñu may yar ba ma nekkee xale”.
25رَّبُّكُمْ أَعْلَمُ بِمَا فِي نُفُوسِكُمْ ۚ إِن تَكُونُوا صَالِحِينَ فَإِنَّهُ كَانَ لِلْأَوَّابِينَ غَفُورًا
Seen Boroom a gën a xam li nekk ci seen bakkan. Ndeem nekk ngeen ñu sell ; Moom Jéggalaakoon la ci ñiy dellu jëm ci jaamu Yàlla.
26وَآتِ ذَا الْقُرْبَىٰ حَقَّهُ وَالْمِسْكِينَ وَابْنَ السَّبِيلِ وَلَا تُبَذِّرْ تَبْذِيرًا
“Nanga jox sa jegeñaale li la war ci moom, ak ku ñàkk ak ku nekk ci tukki. Waaye bul nekk di pasar-pasaree alal,
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Isra 24

Simoore Al-Isra Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nanga suufeel sa bopp ngir ñoom ; di toroxlu ci…

Simoore Aaya 24/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers