Al-Isra · 48/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا ۝٤٨
Unzur kaifa daraboo lakal amsaala fadalloo falaa yastatee`oona sabeelaa
📖 Tekkim Wolof
Gisal li ñu lay nirale ! Tax na réer nañu te dootuñu mën a am yoonu dellusi (ci ag njub).

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 46-50 — Simoore Al-Isra

46وَجَعَلْنَا عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ أَكِنَّةً أَن يَفْقَهُوهُ وَفِي آذَانِهِمْ وَقْرًا ۚ وَإِذَا ذَكَرْتَ رَبَّكَ فِي الْقُرْآنِ وَحْدَهُ وَلَّوْا عَلَىٰ أَدْبَارِهِمْ نُفُورًا
Nu def ci seeni xol muuraay ba duñu ca am dégg-dégg : te nekk na ci seeni nopp ab daaj. Te booy tudd sa Boroom moom doŋŋ ci Alxuraan, ñu dëddu, foñ.
47نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَسْتَمِعُونَ بِهِ إِذْ يَسْتَمِعُونَ إِلَيْكَ وَإِذْ هُمْ نَجْوَىٰ إِذْ يَقُولُ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا
Nun noo gën a xam li ñuy dégg bu ñu lay déglu. Ak bu ñuy déeytoo ci wax ñoom tooñkat ya : “Toppuñu lu dul as waay su ñu jibar”.
48انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا
Gisal li ñu lay nirale ! Tax na réer nañu te dootuñu mën a am yoonu dellusi (ci ag njub).
49وَقَالُوا أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا وَرُفَاتًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ خَلْقًا جَدِيدًا
Ñu naan : “[Ndax bu ñu deewee] ba nekk yax yu funux, dananu dekki nekkaat ay mbindeef yu bees? ”
50۞ قُلْ كُونُوا حِجَارَةً أَوْ حَدِيدًا
Neel : “Nekkleen i xeer walla weñ
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-Isra 48

Simoore Al-Isra Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Gisal li ñu lay nirale ! Tax na réer nañu…

Simoore Aaya 48/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers