Al-Isra · 47/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَسْتَمِعُونَ بِهِ إِذْ يَسْتَمِعُونَ إِلَيْكَ وَإِذْ هُمْ نَجْوَىٰ إِذْ يَقُولُ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا ۝٤٧
nahnu a`lamu bimaa yastami`oona biheee iz yastami`oona ilaika wa iz hum najwaaa iz yaqooluz zaalimoona in tattabi`oona illaa rajulam mas hooraa
📖 Tekkim Wolof
Nun noo gën a xam li ñuy dégg bu ñu lay déglu. Ak bu ñuy déeytoo ci wax ñoom tooñkat ya : “Toppuñu lu dul as waay su ñu jibar”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 45-49 — Al-Isra

45وَإِذَا قَرَأْتَ الْقُرْآنَ جَعَلْنَا بَيْنَكَ وَبَيْنَ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ حِجَابًا مَّسْتُورًا
Booy jàng Alxuraan, Dananu def ci sa diggante ak ñi gëmul àllaaxira kiiraay lu nëbbu,
46وَجَعَلْنَا عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ أَكِنَّةً أَن يَفْقَهُوهُ وَفِي آذَانِهِمْ وَقْرًا ۚ وَإِذَا ذَكَرْتَ رَبَّكَ فِي الْقُرْآنِ وَحْدَهُ وَلَّوْا عَلَىٰ أَدْبَارِهِمْ نُفُورًا
Nu def ci seeni xol muuraay ba duñu ca am dégg-dégg : te nekk na ci seeni nopp ab daaj. Te booy tudd sa Boroom moom doŋŋ ci Alxuraan, ñu dëddu, foñ.
47نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَسْتَمِعُونَ بِهِ إِذْ يَسْتَمِعُونَ إِلَيْكَ وَإِذْ هُمْ نَجْوَىٰ إِذْ يَقُولُ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا
Nun noo gën a xam li ñuy dégg bu ñu lay déglu. Ak bu ñuy déeytoo ci wax ñoom tooñkat ya : “Toppuñu lu dul as waay su ñu jibar”.
48انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا
Gisal li ñu lay nirale ! Tax na réer nañu te dootuñu mën a am yoonu dellusi (ci ag njub).
49وَقَالُوا أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا وَرُفَاتًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ خَلْقًا جَدِيدًا
Ñu naan : “[Ndax bu ñu deewee] ba nekk yax yu funux, dananu dekki nekkaat ay mbindeef yu bees? ”
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — Al-Isra 47

Simoore Al-Isra Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun noo gën a xam li ñuy dégg bu ñu…

Simoore Aaya 47/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers