Al-Isra · 49/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَقَالُوا أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا وَرُفَاتًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ خَلْقًا جَدِيدًا ۝٤٩
Wa qaalooo`a izaa kunnaa `izaamanw wa rufaatan `a innaa lamab`oosoona khalqan jadeedaa
📖 Tekkim Wolof
Ñu naan : “[Ndax bu ñu deewee] ba nekk yax yu funux, dananu dekki nekkaat ay mbindeef yu bees? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Al-Isra

47نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَسْتَمِعُونَ بِهِ إِذْ يَسْتَمِعُونَ إِلَيْكَ وَإِذْ هُمْ نَجْوَىٰ إِذْ يَقُولُ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا
Nun noo gën a xam li ñuy dégg bu ñu lay déglu. Ak bu ñuy déeytoo ci wax ñoom tooñkat ya : “Toppuñu lu dul as waay su ñu jibar”.
48انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا
Gisal li ñu lay nirale ! Tax na réer nañu te dootuñu mën a am yoonu dellusi (ci ag njub).
49وَقَالُوا أَإِذَا كُنَّا عِظَامًا وَرُفَاتًا أَإِنَّا لَمَبْعُوثُونَ خَلْقًا جَدِيدًا
Ñu naan : “[Ndax bu ñu deewee] ba nekk yax yu funux, dananu dekki nekkaat ay mbindeef yu bees? ”
50۞ قُلْ كُونُوا حِجَارَةً أَوْ حَدِيدًا
Neel : “Nekkleen i xeer walla weñ
51أَوْ خَلْقًا مِّمَّا يَكْبُرُ فِي صُدُورِكُمْ ۚ فَسَيَقُولُونَ مَن يُعِيدُنَا ۖ قُلِ الَّذِي فَطَرَكُمْ أَوَّلَ مَرَّةٍ ۚ فَسَيُنْغِضُونَ إِلَيْكَ رُءُوسَهُمْ وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هُوَ ۖ قُلْ عَسَىٰ أَن يَكُونَ قَرِيبًا
walla yeneeni mbindeef yu reyci seeni xel. [Ngeen dégg] ñu naan : “Ku nuy dundalaat ? ” - Neel : “Ka leen bindoon bu njëkk ba”. Danañu yëngal seen bopp jëme ci yaw [ngir weddi la], ñuy wax naan : “Kañ lay doon ? ” Neeleen : “Xéy-na nekk na lu jegeñ.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Isra 49

Simoore Al-Isra Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu naan : “[Ndax bu ñu deewee] ba nekk yax…

Simoore Aaya 49/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers