Al-Kahf · 106/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
ذَٰلِكَ جَزَاؤُهُمْ جَهَنَّمُ بِمَا كَفَرُوا وَاتَّخَذُوا آيَاتِي وَرُسُلِي هُزُوًا ۝١٠٦
Zaalika jazaaa`uhum jahannamu bimaa kafaroo wattakhazooo Aayaatee wa Rusulee huzuwaa
📖 Tekkim Wolof
Loola moo tax ñu feye leen Safara, ngir la ñu weddi woon tey jàppe Sunuy kàddu ak Sunuy Yonent ay caaxaan.

🎧 Dégg


📜 Aaya 104-108 — Al-Kahf

104الَّذِينَ ضَلَّ سَعْيُهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَهُمْ يَحْسَبُونَ أَنَّهُمْ يُحْسِنُونَ صُنْعًا
Ñoo di gaa ña nga xam ne sànk nañu seeni jëf, dara baaxu ca, ba noppi ñuy njort ne li ñuy jëf baax na.
105أُولَٰئِكَ الَّذِينَ كَفَرُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ وَلِقَائِهِ فَحَبِطَتْ أَعْمَالُهُمْ فَلَا نُقِيمُ لَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ وَزْنًا
Ñoom ñoo di ña daan weddi kàdduy Yàlla seen Boroom ak daje ga ñu nar a dajeek Moom. Seeni jëf sippiku na”. Kenn duleen peeseel dara.
106ذَٰلِكَ جَزَاؤُهُمْ جَهَنَّمُ بِمَا كَفَرُوا وَاتَّخَذُوا آيَاتِي وَرُسُلِي هُزُوًا
Loola moo tax ñu feye leen Safara, ngir la ñu weddi woon tey jàppe Sunuy kàddu ak Sunuy Yonent ay caaxaan.
107إِنَّ الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ كَانَتْ لَهُمْ جَنَّاتُ الْفِرْدَوْسِ نُزُلًا
Ña gëmoon tey jëf u yiw, Àjjana [Firdawsi] mooy seen wàccuwaay,
108خَالِدِينَ فِيهَا لَا يَبْغُونَ عَنْهَا حِوَلًا
dañu fay béel te duñu ko bëgg a weccee.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
106Aaya

Tekki — Al-Kahf 106

Simoore Al-Kahf Aaya 106 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loola moo tax ñu feye leen Safara, ngir la ñu…

Simoore Aaya 106/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 104–108. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers