Al-Kahf · 84/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
إِنَّا مَكَّنَّا لَهُ فِي الْأَرْضِ وَآتَيْنَاهُ مِن كُلِّ شَيْءٍ سَبَبًا ۝٨٤
Innaa makkannaa lahoo fil ardi wa aatainaahu min kulli shai`in sababaa
📖 Tekkim Wolof
Mayoon Nanu ko kàttan ci kaw suuf ba mu mën a def lépp lu mu bëgg.
🎧 Dégg

📜 Aaya 82-86 — Al-Kahf

82وَأَمَّا الْجِدَارُ فَكَانَ لِغُلَامَيْنِ يَتِيمَيْنِ فِي الْمَدِينَةِ وَكَانَ تَحْتَهُ كَنزٌ لَّهُمَا وَكَانَ أَبُوهُمَا صَالِحًا فَأَرَادَ رَبُّكَ أَن يَبْلُغَا أَشُدَّهُمَا وَيَسْتَخْرِجَا كَنزَهُمَا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ وَمَا فَعَلْتُهُ عَنْ أَمْرِي ۚ ذَٰلِكَ تَأْوِيلُ مَا لَمْ تَسْطِع عَّلَيْهِ صَبْرًا
Tabax [ba ma doon yékkatiwaat], ñaari xale yu jirim ñoom la ko fa seen baay bàyyil; seen baay doonoon ku yiw, ku baax, am alal ju mu leen ca dencal. Sa Boroom bëgg su ñu màggee mën a gindiku jël seen alal joojee ci yërmaandey Yàlla. Defuma ko woon rekk ci sama coobarey bopp. Loolu kon mooy mbirum la nga mënul woon a muñ”.
83وَيَسْأَلُونَكَ عَن ذِي الْقَرْنَيْنِ ۖ قُلْ سَأَتْلُو عَلَيْكُم مِّنْهُ ذِكْرًا
Danañu lay laaj ci mbirum [Zul-Qarnayni]. Neel : “Danaa leen jàngal na mu doxe woon”.
84إِنَّا مَكَّنَّا لَهُ فِي الْأَرْضِ وَآتَيْنَاهُ مِن كُلِّ شَيْءٍ سَبَبًا
Mayoon Nanu ko kàttan ci kaw suuf ba mu mën a def lépp lu mu bëgg.
85فَأَتْبَعَ سَبَبًا
Mu sóobu bëgg-bëggam, topp aw yoon di dem.
86حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَغْرِبَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَغْرُبُ فِي عَيْنٍ حَمِئَةٍ وَوَجَدَ عِندَهَا قَوْمًا ۗ قُلْنَا يَا ذَا الْقَرْنَيْنِ إِمَّا أَن تُعَذِّبَ وَإِمَّا أَن تَتَّخِذَ فِيهِمْ حُسْنًا
Mu takk xare dem ba fa sowwu yem, mu fekk ne jant ba ma ngay sowe fa ndox ma ànd ak ban, mu fekk itam aw xeet [wa ko dëkke]. Ñu ne ko : “Fàwwu yaw Zul-Qarnayni ! nga mbugal leen walla nga yërëm leen”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
84Aaya

Tekki — Al-Kahf 84

Simoore Al-Kahf Aaya 84 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mayoon Nanu ko kàttan ci kaw suuf ba mu mën…

Simoore Aaya 84/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 82–86. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers