Al-Kahf · 85/110
Tekki Waxtaan — Al-Kahf
فَأَتْبَعَ سَبَبًا ٨٥
Transliteration
Fa atba`a sababaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu sóobu bëgg-bëggam, topp aw yoon di dem.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 83-87 — Al-Kahf
83وَيَسْأَلُونَكَ عَن ذِي الْقَرْنَيْنِ ۖ قُلْ سَأَتْلُو عَلَيْكُم مِّنْهُ ذِكْرًا
Danañu lay laaj ci mbirum [Zul-Qarnayni]. Neel : “Danaa leen jàngal na mu doxe woon”.
84إِنَّا مَكَّنَّا لَهُ فِي الْأَرْضِ وَآتَيْنَاهُ مِن كُلِّ شَيْءٍ سَبَبًا
Mayoon Nanu ko kàttan ci kaw suuf ba mu mën a def lépp lu mu bëgg.
85فَأَتْبَعَ سَبَبًا
Mu sóobu bëgg-bëggam, topp aw yoon di dem.
86حَتَّىٰ إِذَا بَلَغَ مَغْرِبَ الشَّمْسِ وَجَدَهَا تَغْرُبُ فِي عَيْنٍ حَمِئَةٍ وَوَجَدَ عِندَهَا قَوْمًا ۗ قُلْنَا يَا ذَا الْقَرْنَيْنِ إِمَّا أَن تُعَذِّبَ وَإِمَّا أَن تَتَّخِذَ فِيهِمْ حُسْنًا
Mu takk xare dem ba fa sowwu yem, mu fekk ne jant ba ma ngay sowe fa ndox ma ànd ak ban, mu fekk itam aw xeet [wa ko dëkke]. Ñu ne ko : “Fàwwu yaw Zul-Qarnayni ! nga mbugal leen walla nga yërëm leen”.
87قَالَ أَمَّا مَن ظَلَمَ فَسَوْفَ نُعَذِّبُهُ ثُمَّ يُرَدُّ إِلَىٰ رَبِّهِ فَيُعَذِّبُهُ عَذَابًا نُّكْرًا
Mu wax ne : “Képp koo xam ne dafay tooñ, dananu ko mbugal fii ; te su delloo fa Boroomam, Dana ko mbugal mbugal mu gën a tar.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
85Aaya
Tekki — Al-Kahf 85
Simoore Al-Kahf Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu sóobu bëgg-bëggam, topp aw yoon di dem.Simoore Aaya 85/110 — Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Kahf Dégg, Al-Kahf Tekki, Al-Kahf mp3, Al-Kahf pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








