Maryam · 21/98
Tekki Waxtaan — Maryam
قَالَ كَذَٰلِكِ قَالَ رَبُّكِ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ ۖ وَلِنَجْعَلَهُ آيَةً لِّلنَّاسِ وَرَحْمَةً مِّنَّا ۚ وَكَانَ أَمْرًا مَّقْضِيًّا ۝٢١
Qaala kazaaliki qaala Rabbuki huwa `alaiya yaiyimunw wa linaj `alahooo Aayatal linnaasi wa rahmatam minnaa; wa kaana amram maqdiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Mu ne ko : “Loolu la sa Boroom wax ! Te lu yomb la ci Man ! Lii dafay doon kéemaan ci nit ñi, ak yërmaande wu bawoo fa Yàlla. Dogal ba sotti na”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Maryam

19قَالَ إِنَّمَا أَنَا رَسُولُ رَبِّكِ لِأَهَبَ لَكِ غُلَامًا زَكِيًّا
Malaaka ma [Jibriil] ne ko : “Man dey ndawul sa Boroom laa [damaa ñëw] ngir may la doom ju sell”.
20قَالَتْ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَلَمْ يَمْسَسْنِي بَشَرٌ وَلَمْ أَكُ بَغِيًّا
Mu ne ko : “Man naka laay ame doom, te génn góor masumaa laal, te duma ku baaloy ? ”
21قَالَ كَذَٰلِكِ قَالَ رَبُّكِ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ ۖ وَلِنَجْعَلَهُ آيَةً لِّلنَّاسِ وَرَحْمَةً مِّنَّا ۚ وَكَانَ أَمْرًا مَّقْضِيًّا
Mu ne ko : “Loolu la sa Boroom wax ! Te lu yomb la ci Man ! Lii dafay doon kéemaan ci nit ñi, ak yërmaande wu bawoo fa Yàlla. Dogal ba sotti na”.
22۞ فَحَمَلَتْهُ فَانتَبَذَتْ بِهِ مَكَانًا قَصِيًّا
Mu daldi ëmb, daldi dem ca bérab bu sori.
23فَأَجَاءَهَا الْمَخَاضُ إِلَىٰ جِذْعِ النَّخْلَةِ قَالَتْ يَا لَيْتَنِي مِتُّ قَبْلَ هَٰذَا وَكُنتُ نَسْيًا مَّنسِيًّا
Mat ma dikkal ko mu wattatu ba ca benn dàttu tàndarma, mu daldi ne: “Aka neexoon ma dee lu jiitu ! Kon fàttees na ma ! ”
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Maryam 21

Simoore Maryam Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu ne ko : “Loolu la sa Boroom wax !…

Simoore Aaya 21/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers