Maryam · 64/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَمَا نَتَنَزَّلُ إِلَّا بِأَمْرِ رَبِّكَ ۖ لَهُ مَا بَيْنَ أَيْدِينَا وَمَا خَلْفَنَا وَمَا بَيْنَ ذَٰلِكَ ۚ وَمَا كَانَ رَبُّكَ نَسِيًّا ٦٤
Transliteration
Wa maa natanazzalu illaa bi amri Rabbika lahoo maa baina aideenaa wa maa khalfanaa wa maa baina zaalik; wa maa kaana Rabbuka nasiyyaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
“Dunu wàcce ca Àjjana ja lu dul ci ndigalul Yàlla. Mooy Boroom li wéy ak li teew ak liy ñëw. Sa Boroom du fàtte de.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 62-66 — Maryam
62لَّا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا إِلَّا سَلَامًا ۖ وَلَهُمْ رِزْقُهُمْ فِيهَا بُكْرَةً وَعَشِيًّا
Duñu fa dégg lenn coow ; daldi leen kañ ci : “Jàmm” ; te ñam ya du dogamtal suba ak ngoon.
63تِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي نُورِثُ مِنْ عِبَادِنَا مَن كَانَ تَقِيًّا
Àjjana jooju la Nuy donnale képp ku ragal Yàlla ci Sunu jaam ñi.
64وَمَا نَتَنَزَّلُ إِلَّا بِأَمْرِ رَبِّكَ ۖ لَهُ مَا بَيْنَ أَيْدِينَا وَمَا خَلْفَنَا وَمَا بَيْنَ ذَٰلِكَ ۚ وَمَا كَانَ رَبُّكَ نَسِيًّا
“Dunu wàcce ca Àjjana ja lu dul ci ndigalul Yàlla. Mooy Boroom li wéy ak li teew ak liy ñëw. Sa Boroom du fàtte de.
65رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا فَاعْبُدْهُ وَاصْطَبِرْ لِعِبَادَتِهِ ۚ هَلْ تَعْلَمُ لَهُ سَمِيًّا
Boroom asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante. Nanga ko jaamu te nanga sax ci jaamu Ko. Waaw ndax xamal nga ko benn turandoo? Mukk amul ”
66وَيَقُولُ الْإِنسَانُ أَإِذَا مَا مِتُّ لَسَوْفَ أُخْرَجُ حَيًّا
Nit nag di wax naan : “Ndax su ma dee danañu ma génnewaat may dundu ? ”
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
64Aaya
Tekki — Maryam 64
Simoore Maryam Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Dunu wàcce ca Àjjana ja lu dul ci ndigalul Yàlla.…Simoore Aaya 64/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








