Maryam · 65/98
Tekki Waxtaan — Maryam
رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا فَاعْبُدْهُ وَاصْطَبِرْ لِعِبَادَتِهِ ۚ هَلْ تَعْلَمُ لَهُ سَمِيًّا ۝٦٥
Rabbus samaawaati wal ardi wa maa bainahumaa fa`bud hu wastabir li`ibaadatih; hal ta`lamu lahoo samiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Boroom asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante. Nanga ko jaamu te nanga sax ci jaamu Ko. Waaw ndax xamal nga ko benn turandoo? Mukk amul ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 63-67 — Maryam

63تِلْكَ الْجَنَّةُ الَّتِي نُورِثُ مِنْ عِبَادِنَا مَن كَانَ تَقِيًّا
Àjjana jooju la Nuy donnale képp ku ragal Yàlla ci Sunu jaam ñi.
64وَمَا نَتَنَزَّلُ إِلَّا بِأَمْرِ رَبِّكَ ۖ لَهُ مَا بَيْنَ أَيْدِينَا وَمَا خَلْفَنَا وَمَا بَيْنَ ذَٰلِكَ ۚ وَمَا كَانَ رَبُّكَ نَسِيًّا
“Dunu wàcce ca Àjjana ja lu dul ci ndigalul Yàlla. Mooy Boroom li wéy ak li teew ak liy ñëw. Sa Boroom du fàtte de.
65رَّبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا فَاعْبُدْهُ وَاصْطَبِرْ لِعِبَادَتِهِ ۚ هَلْ تَعْلَمُ لَهُ سَمِيًّا
Boroom asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci seen diggante. Nanga ko jaamu te nanga sax ci jaamu Ko. Waaw ndax xamal nga ko benn turandoo? Mukk amul ”
66وَيَقُولُ الْإِنسَانُ أَإِذَا مَا مِتُّ لَسَوْفَ أُخْرَجُ حَيًّا
Nit nag di wax naan : “Ndax su ma dee danañu ma génnewaat may dundu ? ”
67أَوَلَا يَذْكُرُ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ وَلَمْ يَكُ شَيْئًا
Moo ndax nit dafa fàttalikuwul ne Noo ko bindoon bu njëkk te doonutoon dara ?
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Maryam 65

Simoore Maryam Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Boroom asamaan yi ak suuf si ak li nekk ci…

Simoore Aaya 65/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers