Al-Baqara · 127/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَإِذْ يَرْفَعُ إِبْرَاهِيمُ الْقَوَاعِدَ مِنَ الْبَيْتِ وَإِسْمَاعِيلُ رَبَّنَا تَقَبَّلْ مِنَّا ۖ إِنَّكَ أَنتَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ ۝١٢٧
Wa iz yarfa`u Ibraaheemul qawaa`ida minal Baitiwa Ismaa`eelu Rabbanaa taqabbal minnaa innaka Antas Samee`ul Aleem
📖 Tekkim Wolof
[Fàttalikuleen] Ba Ibraahiima ak Ismaahiila di yékkati ndéttalu néeg ba (Kaaba ga) : "Yaw sunu Boroom nangul nu, Yaw dey Kuy dégg nga, Kuy xam nga.

🎧 Dégg


📜 Aaya 125-129 — Al-Baqara

125وَإِذْ جَعَلْنَا الْبَيْتَ مَثَابَةً لِّلنَّاسِ وَأَمْنًا وَاتَّخِذُوا مِن مَّقَامِ إِبْرَاهِيمَ مُصَلًّى ۖ وَعَهِدْنَا إِلَىٰ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْمَاعِيلَ أَن طَهِّرَا بَيْتِيَ لِلطَّائِفِينَ وَالْعَاكِفِينَ وَالرُّكَّعِ السُّجُودِ
[Fàttalikuleen], ba Nu defee Néeg ba muy delluwaayub nit ñi ak barabub kóolute - Te nangeen def (Màqaama Ibraahiima) barabub jullikaay, - Nu kóllarante ak (Ibraahiima) ak (Ismaahiila) : “Ne leen nangeen sellal Sama Néeg bi ngir ñi koy wër, ak ñi fay toog, di fa rukkoo ak di fa sujjóot [julli].
126وَإِذْ قَالَ إِبْرَاهِيمُ رَبِّ اجْعَلْ هَٰذَا بَلَدًا آمِنًا وَارْزُقْ أَهْلَهُ مِنَ الثَّمَرَاتِ مَنْ آمَنَ مِنْهُم بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ ۖ قَالَ وَمَن كَفَرَ فَأُمَتِّعُهُ قَلِيلًا ثُمَّ أَضْطَرُّهُ إِلَىٰ عَذَابِ النَّارِ ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
[Fàttalikuleen] Ba Ibraahiima waxee ne : “Yaw sama Boroom, defal dëkk bii muy dëkkub jàmm [bu am kóolute], te Nga xéewale ciy meññent ñi gëm Yàlla ak Bis-pénc ba, ci waa dëkk bi”, Yàlla ne ko : “Ak ku weddi it danaa ko xéewale ci diir bu gàtt, ba noppi Danaa ko wéyal ci mbugalum Safara. Ndaw delloowaay bu bon” !
127وَإِذْ يَرْفَعُ إِبْرَاهِيمُ الْقَوَاعِدَ مِنَ الْبَيْتِ وَإِسْمَاعِيلُ رَبَّنَا تَقَبَّلْ مِنَّا ۖ إِنَّكَ أَنتَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
[Fàttalikuleen] Ba Ibraahiima ak Ismaahiila di yékkati ndéttalu néeg ba (Kaaba ga) : "Yaw sunu Boroom nangul nu, Yaw dey Kuy dégg nga, Kuy xam nga.
128رَبَّنَا وَاجْعَلْنَا مُسْلِمَيْنِ لَكَ وَمِن ذُرِّيَّتِنَا أُمَّةً مُّسْلِمَةً لَّكَ وَأَرِنَا مَنَاسِكَنَا وَتُبْ عَلَيْنَا ۖ إِنَّكَ أَنتَ التَّوَّابُ الرَّحِيمُ
Yaw sunu Boroom ! Def nu nuy ñaari way-wommatu jëm ci yaw. Te nga def ci sunuy sët askan wu wommatu jëm ci Yaw te nga won nu sunu jaamuwaay, boole ca jéggal nu. Yaw dey Boroom bi, Yaa di Jéggalaakoon bi, di Jaglewaakoon bi.
129رَبَّنَا وَابْعَثْ فِيهِمْ رَسُولًا مِّنْهُمْ يَتْلُو عَلَيْهِمْ آيَاتِكَ وَيُعَلِّمُهُمُ الْكِتَابَ وَالْحِكْمَةَ وَيُزَكِّيهِمْ ۚ إِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Yaw sunu Boroom ! Yónneel ci ñoom Yonent bu bokk ci ñoom, bu leen di jàngal say laaya, di leen xamal Téere ba ak i xereñe, te di leen sellal Yaw Aji-not ji , Aji-xereñ ji!
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
127Aaya

Tekki — Al-Baqara 127

Simoore Al-Baqara Aaya 127 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Fàttalikuleen] Ba Ibraahiima ak Ismaahiila di yékkati ndéttalu néeg ba…

Simoore Aaya 127/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 125–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers