Al-Baqara · 192/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
فَإِنِ انتَهَوْا فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ ۝١٩٢
Fa ini-ntahaw fa innal laaha Ghafoorur Raheem
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu génnee ci kéefar ga nag, Yàlla ab Jéggalaakoon la, ab Jaglewaakoon la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 190-194 — Simoore Al-Baqara

190وَقَاتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ الَّذِينَ يُقَاتِلُونَكُمْ وَلَا تَعْتَدُوا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْمُعْتَدِينَ
Xeexleen ci yoonu Yàlla ak ña leen di xeex, te buleen jéggi dayo di tooñ Yàlla. Yàlla dey soppul ñay jalgati !
191وَاقْتُلُوهُمْ حَيْثُ ثَقِفْتُمُوهُمْ وَأَخْرِجُوهُم مِّنْ حَيْثُ أَخْرَجُوكُمْ ۚ وَالْفِتْنَةُ أَشَدُّ مِنَ الْقَتْلِ ۚ وَلَا تُقَاتِلُوهُمْ عِندَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ حَتَّىٰ يُقَاتِلُوكُمْ فِيهِ ۖ فَإِن قَاتَلُوكُمْ فَاقْتُلُوهُمْ ۗ كَذَٰلِكَ جَزَاءُ الْكَافِرِينَ
Reyleen leen, fu ngeen fi dajeek ñoom ; Nangeen leen génne fa ñu leen génne woon : [Sànje] moo gën a tar reyaate. Buleen xeex ak ñoom fa Màkka ndare du ñoom ñoo leen fa songu. Bu ñu leen fa songee nag, reyleen leen. Loolu mooy peyub yéefar yi.
192فَإِنِ انتَهَوْا فَإِنَّ اللَّهَ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Bu ñu génnee ci kéefar ga nag, Yàlla ab Jéggalaakoon la, ab Jaglewaakoon la.
193وَقَاتِلُوهُمْ حَتَّىٰ لَا تَكُونَ فِتْنَةٌ وَيَكُونَ الدِّينُ لِلَّهِ ۖ فَإِنِ انتَهَوْا فَلَا عُدْوَانَ إِلَّا عَلَى الظَّالِمِينَ
Nangeen xeex ak ñooña ba sànje dootul am, diinay Yàlla rekk taxaw fi. Bu ñu bàyyee sànje nag, ku toppati ñu nekkalko ca ak moom.
194الشَّهْرُ الْحَرَامُ بِالشَّهْرِ الْحَرَامِ وَالْحُرُمَاتُ قِصَاصٌ ۚ فَمَنِ اعْتَدَىٰ عَلَيْكُمْ فَاعْتَدُوا عَلَيْهِ بِمِثْلِ مَا اعْتَدَىٰ عَلَيْكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ وَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ مَعَ الْمُتَّقِينَ
Weer wuñu wormaal [Araamal], tere ku ca xeex, dañu koy feyee ak weer wuñu wormaal ! - Yu ñu wormaal ya dañuy feyante -. Ku leen ca tooñ, feyyuleen kem la mu leen tooñ. Te nangeen ragal te xamleen ne Yàllaa ngi ànd ak ñi ko ragal.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
192Aaya

Tekki — Al-Baqara 192

Simoore Al-Baqara Aaya 192 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu génnee ci kéefar ga nag, Yàlla ab Jéggalaakoon…

Simoore Aaya 192/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 190–194. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers