Al-Baqara · 67/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَإِذْ قَالَ مُوسَىٰ لِقَوْمِهِ إِنَّ اللَّهَ يَأْمُرُكُمْ أَن تَذْبَحُوا بَقَرَةً ۖ قَالُوا أَتَتَّخِذُنَا هُزُوًا ۖ قَالَ أَعُوذُ بِاللَّهِ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْجَاهِلِينَ ٦٧
Transliteration
Wa iz qaala Moosaa liqawmiheee innal laaha yaamurukum an tazbahoo baqaratan qaalooo atattakhizunna huzuwan qaala a`oozu billaahi an akoona minal jaahileen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Fàttalikuleen,) ba Muusaa waxee aw nitam : “Yàlla digal na leen ngeen reyu nag”. Ñu ne ko : “Moo ndax danga nuy ñaawal ? ”. Mu ne : “Yàlla na ma Yàlla musal ci bokk ci way-réer ña ”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 65-69 — Al-Baqara
65وَلَقَدْ عَلِمْتُمُ الَّذِينَ اعْتَدَوْا مِنكُمْ فِي السَّبْتِ فَقُلْنَا لَهُمْ كُونُوا قِرَدَةً خَاسِئِينَ
Wallaahi xam ngeen ña jalgati woon ci yéen ca Gaawu ba. Tax ñoom ñooñu Nu ne leen : “Nekkleen di ay golo yu ñu beddi ! ”
66فَجَعَلْنَاهَا نَكَالًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهَا وَمَا خَلْفَهَا وَمَوْعِظَةً لِّلْمُتَّقِينَ
Maka Kami jadikan (yang demikian) itu peringatan bagi orang-orang pada masa itu dan bagi mereka yang datang kemudian, serta menjadi pelajaran bagi orang-orang yang bertakwa.
67وَإِذْ قَالَ مُوسَىٰ لِقَوْمِهِ إِنَّ اللَّهَ يَأْمُرُكُمْ أَن تَذْبَحُوا بَقَرَةً ۖ قَالُوا أَتَتَّخِذُنَا هُزُوًا ۖ قَالَ أَعُوذُ بِاللَّهِ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْجَاهِلِينَ
Fàttalikuleen,) ba Muusaa waxee aw nitam : “Yàlla digal na leen ngeen reyu nag”. Ñu ne ko : “Moo ndax danga nuy ñaawal ? ”. Mu ne : “Yàlla na ma Yàlla musal ci bokk ci way-réer ña ”.
68قَالُوا ادْعُ لَنَا رَبَّكَ يُبَيِّن لَّنَا مَا هِيَ ۚ قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ لَّا فَارِضٌ وَلَا بِكْرٌ عَوَانٌ بَيْنَ ذَٰلِكَ ۖ فَافْعَلُوا مَا تُؤْمَرُونَ
Ñu ne : “Ñaanal nu sa Boroom mu leeral nu luy meloom”. - Mu ne : “Naka Moom nee na : nag wa du wu màggat, du aw sëll, dafa digg-dóomu. Def leen li ñu leen sant”.
69قَالُوا ادْعُ لَنَا رَبَّكَ يُبَيِّن لَّنَا مَا لَوْنُهَا ۚ قَالَ إِنَّهُ يَقُولُ إِنَّهَا بَقَرَةٌ صَفْرَاءُ فَاقِعٌ لَّوْنُهَا تَسُرُّ النَّاظِرِينَ
- Ñu ne : “Ñaanal nu sa Boroom mu leeral nu luy meloom”. - Mu ne : “Naka Moom nee na: nag la wu gel, wu fees, woo xam ne dees na beg ci xool ko .”.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
67Aaya
Tekki — Al-Baqara 67
Simoore Al-Baqara Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Fàttalikuleen,) ba Muusaa waxee aw nitam : “Yàlla digal na…Simoore Aaya 67/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








