Al-Baqara · 8/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
وَمِنَ النَّاسِ مَن يَقُولُ آمَنَّا بِاللَّهِ وَبِالْيَوْمِ الْآخِرِ وَمَا هُم بِمُؤْمِنِينَ ۝٨
Wa minan naasi mai yaqoolu aamannaa billaahi wa bil yawmil aakhiri wa maa hum bimu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Am na ci nit ñi, ñu naan : “Gëm nanu Yàlla ak Bis-pénc ba ! ” te gëmuñu dara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-Baqara

6إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا سَوَاءٌ عَلَيْهِمْ أَأَنذَرْتَهُمْ أَمْ لَمْ تُنذِرْهُمْ لَا يُؤْمِنُونَ
Ñi weddi, nga waar leen ak ñàkk leen waar a yem ci ñoom, duñu gëm.
7خَتَمَ اللَّهُ عَلَىٰ قُلُوبِهِمْ وَعَلَىٰ سَمْعِهِمْ ۖ وَعَلَىٰ أَبْصَارِهِمْ غِشَاوَةٌ ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ عَظِيمٌ
Yàlla fatt na seeni xol ak seeni nopp ; muuraay nekk na ca seeni gët ; mbugal mu metti dana leen dal.
8وَمِنَ النَّاسِ مَن يَقُولُ آمَنَّا بِاللَّهِ وَبِالْيَوْمِ الْآخِرِ وَمَا هُم بِمُؤْمِنِينَ
Am na ci nit ñi, ñu naan : “Gëm nanu Yàlla ak Bis-pénc ba ! ” te gëmuñu dara.
9يُخَادِعُونَ اللَّهَ وَالَّذِينَ آمَنُوا وَمَا يَخْدَعُونَ إِلَّا أَنفُسَهُمْ وَمَا يَشْعُرُونَ
Dañuy jéem a nax Yàlla ak way-gëm ñi ; waaye naxuñu lu dul seen bopp, te yëguñu ko.
10فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ فَزَادَهُمُ اللَّهُ مَرَضًا ۖ وَلَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ بِمَا كَانُوا يَكْذِبُونَ
Jàngoroo nekk ci seeni xol (gog sikki-sàkk ak ug naaféq), faf Yàlla yokk leen jàngoro. Mbugal mu metti dana leen dal ngir seenug weddi.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Baqara 8

Simoore Al-Baqara Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am na ci nit ñi, ñu naan : “Gëm nanu…

Simoore Aaya 8/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers