Taha · 104/135
Tekki Waxtaan — Taha
نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ إِذْ يَقُولُ أَمْثَلُهُمْ طَرِيقَةً إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا يَوْمًا ۝١٠٤
nahnu a`lamu bimaa yaqooloona iz yaqoolu amsaluhum tareeqatan illabistum illaa yawmaa
📖 Tekkim Wolof
Nun [Yàlla] Noo gën a xam la ñuy wax, far ka leen gën a kaanu naan : “Aa yéen kat benn fan doŋŋ ngeen am àddina”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 102-106 — Taha

102يَوْمَ يُنفَخُ فِي الصُّورِ ۚ وَنَحْشُرُ الْمُجْرِمِينَ يَوْمَئِذٍ زُرْقًا
bis ba ñu walee [ëf] buftu ba, bis boobee, Dananu pang tooñkat ya ñuy fér-féri [ndax tiit] !
103يَتَخَافَتُونَ بَيْنَهُمْ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا عَشْرًا
Ñuy déeyante ca seen biir naan : “Yéen kat fukki fan doŋŋ ngeen am àddina” !
104نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ إِذْ يَقُولُ أَمْثَلُهُمْ طَرِيقَةً إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا يَوْمًا
Nun [Yàlla] Noo gën a xam la ñuy wax, far ka leen gën a kaanu naan : “Aa yéen kat benn fan doŋŋ ngeen am àddina”.
105وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْجِبَالِ فَقُلْ يَنسِفُهَا رَبِّي نَسْفًا
Ñii nga lay laaj ci dundi doj yi [naka lay mujje]. Neel : “Yàlla dana leen moxoñe,
106فَيَذَرُهَا قَاعًا صَفْصَفًا
bàyyi ko mu ne ag joor gu ne càndaŋ
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
104Aaya

Tekki — Taha 104

Simoore Taha Aaya 104 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun [Yàlla] Noo gën a xam la ñuy wax, far…

Simoore Aaya 104/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 102–106. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers