Taha · 105/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْجِبَالِ فَقُلْ يَنسِفُهَا رَبِّي نَسْفًا ۝١٠٥
Wa yas`aloonaka `anil jibaali faqul yansifuhaa Rabbee nasfaa
📖 Tekkim Wolof
Ñii nga lay laaj ci dundi doj yi [naka lay mujje]. Neel : “Yàlla dana leen moxoñe,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 103-107 — Simoore Taha

103يَتَخَافَتُونَ بَيْنَهُمْ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا عَشْرًا
Ñuy déeyante ca seen biir naan : “Yéen kat fukki fan doŋŋ ngeen am àddina” !
104نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ إِذْ يَقُولُ أَمْثَلُهُمْ طَرِيقَةً إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا يَوْمًا
Nun [Yàlla] Noo gën a xam la ñuy wax, far ka leen gën a kaanu naan : “Aa yéen kat benn fan doŋŋ ngeen am àddina”.
105وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْجِبَالِ فَقُلْ يَنسِفُهَا رَبِّي نَسْفًا
Ñii nga lay laaj ci dundi doj yi [naka lay mujje]. Neel : “Yàlla dana leen moxoñe,
106فَيَذَرُهَا قَاعًا صَفْصَفًا
bàyyi ko mu ne ag joor gu ne càndaŋ
107لَّا تَرَىٰ فِيهَا عِوَجًا وَلَا أَمْتًا
dootoo gis ab nóox-nóox walla ab junni-junni, léppay maase nerr.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
105Aaya

Tekki — Taha 105

Simoore Taha Aaya 105 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñii nga lay laaj ci dundi doj yi [naka lay…

Simoore Aaya 105/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 103–107. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers