Taha · 103/135
Tekki Waxtaan — Taha
يَتَخَافَتُونَ بَيْنَهُمْ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا عَشْرًا ١٠٣
Transliteration
Yatakhaafatoona bainahum il labistum illaa `ashraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñuy déeyante ca seen biir naan : “Yéen kat fukki fan doŋŋ ngeen am àddina” !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 101-105 — Taha
101خَالِدِينَ فِيهِ ۖ وَسَاءَ لَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ حِمْلًا
te dañu cay béelbu keroo gee [Bis-pénc ba], ndaw yen bu bon,
102يَوْمَ يُنفَخُ فِي الصُّورِ ۚ وَنَحْشُرُ الْمُجْرِمِينَ يَوْمَئِذٍ زُرْقًا
bis ba ñu walee [ëf] buftu ba, bis boobee, Dananu pang tooñkat ya ñuy fér-féri [ndax tiit] !
103يَتَخَافَتُونَ بَيْنَهُمْ إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا عَشْرًا
Ñuy déeyante ca seen biir naan : “Yéen kat fukki fan doŋŋ ngeen am àddina” !
104نَّحْنُ أَعْلَمُ بِمَا يَقُولُونَ إِذْ يَقُولُ أَمْثَلُهُمْ طَرِيقَةً إِن لَّبِثْتُمْ إِلَّا يَوْمًا
Nun [Yàlla] Noo gën a xam la ñuy wax, far ka leen gën a kaanu naan : “Aa yéen kat benn fan doŋŋ ngeen am àddina”.
105وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْجِبَالِ فَقُلْ يَنسِفُهَا رَبِّي نَسْفًا
Ñii nga lay laaj ci dundi doj yi [naka lay mujje]. Neel : “Yàlla dana leen moxoñe,
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
103Aaya
Tekki — Taha 103
Simoore Taha Aaya 103 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy déeyante ca seen biir naan : “Yéen kat fukki…Simoore Aaya 103/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 101–105. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








