Taha · 46/135
Tekki Waxtaan — Taha
قَالَ لَا تَخَافَا ۖ إِنَّنِي مَعَكُمَا أَسْمَعُ وَأَرَىٰ ۝٤٦
Qaala laa takhaafaaa innanee ma`akumaa asma`u wa araa
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla]ne leen : “Buleen ragal, yéen laa àndal : Maa ngi dégg di gis.
🎧 Dégg

📜 Aaya 44-48 — Taha

44فَقُولَا لَهُ قَوْلًا لَّيِّنًا لَّعَلَّهُ يَتَذَكَّرُ أَوْ يَخْشَىٰ
Nangeen wax ak moom wax ju nooy. Ndax amaana mu waaru walla mu ragal Yàlla ?
45قَالَا رَبَّنَا إِنَّنَا نَخَافُ أَن يَفْرُطَ عَلَيْنَا أَوْ أَن يَطْغَىٰ
Ñu ne Ko : "Yaw sunu Boroom, nun dey danuy ragal, bu nu demee fa moom, mu jaay nu doole”.
46قَالَ لَا تَخَافَا ۖ إِنَّنِي مَعَكُمَا أَسْمَعُ وَأَرَىٰ
[Yàlla]ne leen : “Buleen ragal, yéen laa àndal : Maa ngi dégg di gis.
47فَأْتِيَاهُ فَقُولَا إِنَّا رَسُولَا رَبِّكَ فَأَرْسِلْ مَعَنَا بَنِي إِسْرَائِيلَ وَلَا تُعَذِّبْهُمْ ۖ قَدْ جِئْنَاكَ بِآيَةٍ مِّن رَّبِّكَ ۖ وَالسَّلَامُ عَلَىٰ مَنِ اتَّبَعَ الْهُدَىٰ
Demleen fa Moom ne ko : “Ñun ñaar ñii ndawi Yàlla lanu. Delloo nu waa Banii-Israayiila [ñi nga jàppe jaam] te buleen mbugalati. Ndax indi nanu ci yaw ay kàddu yu jóge fa sa Boroom. Te jàmmi Yàlla nay nekk ca kay topp njub ga !
48إِنَّا قَدْ أُوحِيَ إِلَيْنَا أَنَّ الْعَذَابَ عَلَىٰ مَن كَذَّبَ وَتَوَلَّىٰ
Xamalees nanu ne : képp ku weddi te dummóoyu [kàdduy Yàlla], kooka mbugal dana ko dal”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Taha 46

Simoore Taha Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla]ne leen : “Buleen ragal, yéen laa àndal : Maa…

Simoore Aaya 46/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers