Taha · 69/135
Tekki Waxtaan — Taha
وَأَلْقِ مَا فِي يَمِينِكَ تَلْقَفْ مَا صَنَعُوا ۖ إِنَّمَا صَنَعُوا كَيْدُ سَاحِرٍ ۖ وَلَا يُفْلِحُ السَّاحِرُ حَيْثُ أَتَىٰ ٦٩
Transliteration
Wa alqi maa fee yamee nika talqaf maa sana`oo; innamaa sana`oo kaidu saahir; wa laa yuflihus saahiru haisu ataa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Sànnil li ci sa loxo ndeyjoor [yet wa] ; li ñuy wone lépp pexey njibarkat doŋŋ la ; te njibarkat moom fàwwu ay tappaleem naaxsaay”. Ba mu ko sànni, yet waa daldi wann yooya yépp
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 67-71 — Taha
67فَأَوْجَسَ فِي نَفْسِهِ خِيفَةً مُّوسَىٰ
Muusaa xaw a amum tiit ci boppam.
68قُلْنَا لَا تَخَفْ إِنَّكَ أَنتَ الْأَعْلَىٰ
Nu ne ko : “Bul ragal [yaa leen mën], yaa leen fare kaw.
69وَأَلْقِ مَا فِي يَمِينِكَ تَلْقَفْ مَا صَنَعُوا ۖ إِنَّمَا صَنَعُوا كَيْدُ سَاحِرٍ ۖ وَلَا يُفْلِحُ السَّاحِرُ حَيْثُ أَتَىٰ
Sànnil li ci sa loxo ndeyjoor [yet wa] ; li ñuy wone lépp pexey njibarkat doŋŋ la ; te njibarkat moom fàwwu ay tappaleem naaxsaay”. Ba mu ko sànni, yet waa daldi wann yooya yépp
70فَأُلْقِيَ السَّحَرَةُ سُجَّدًا قَالُوا آمَنَّا بِرَبِّ هَارُونَ وَمُوسَىٰ
Njibarkat yépp far daldi tëdd ci suuf sujjóot, daldi ne : “Gëm nanu bis niki tey Yàllaay Muusaa ak Haaruuna”.
71قَالَ آمَنتُمْ لَهُ قَبْلَ أَنْ آذَنَ لَكُمْ ۖ إِنَّهُ لَكَبِيرُكُمُ الَّذِي عَلَّمَكُمُ السِّحْرَ ۖ فَلَأُقَطِّعَنَّ أَيْدِيَكُمْ وَأَرْجُلَكُم مِّنْ خِلَافٍ وَلَأُصَلِّبَنَّكُمْ فِي جُذُوعِ النَّخْلِ وَلَتَعْلَمُنَّ أَيُّنَا أَشَدُّ عَذَابًا وَأَبْقَىٰ
[Firawna] ne leen : “Gëmoon ngeen ko la jiitu lii. [Xam naa ne] Muusaa mooy kàndiŋ mi leen jàngal ag njibar. Danaa dàgg seeni tànk ak seeni yoxo cig jàllawle, danaa leen daaj ci dàtti tàndarma yi, dangeen xam kan ci nun moo gën a mettile te gën a tarle mbugal”.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
69Aaya
Tekki — Taha 69
Simoore Taha Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sànnil li ci sa loxo ndeyjoor [yet wa] ; li…Simoore Aaya 69/135 — Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Taha Dégg, Taha Tekki, Taha mp3, Taha pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








