Al-Anbiya · 10/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
لَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكُمْ كِتَابًا فِيهِ ذِكْرُكُمْ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ ۝١٠
Laqad anzalnaaa ilaikum Kitaaban feehi zikrukum afalaa ta`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Wàcce Nanu ci yéen ab Téere boo xam ne seen teraangaa nekk ca biir. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Al-Anbiya

8وَمَا جَعَلْنَاهُمْ جَسَدًا لَّا يَأْكُلُونَ الطَّعَامَ وَمَا كَانُوا خَالِدِينَ
Defunuleen woon [boroom] yaram yu dul lekk ñam. Te it nekkuñu woon ñuy béel [dañu daa lekk, di wopp, di dee].
9ثُمَّ صَدَقْنَاهُمُ الْوَعْدَ فَأَنجَيْنَاهُمْ وَمَن نَّشَاءُ وَأَهْلَكْنَا الْمُسْرِفِينَ
Topp, Nu def la Nu leen digoon. Daldi leen boole musal ak ku Nu soob. Yàqkat ya ñoom, Nu rey leen.
10لَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكُمْ كِتَابًا فِيهِ ذِكْرُكُمْ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Wàcce Nanu ci yéen ab Téere boo xam ne seen teraangaa nekk ca biir. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
11وَكَمْ قَصَمْنَا مِن قَرْيَةٍ كَانَتْ ظَالِمَةً وَأَنشَأْنَا بَعْدَهَا قَوْمًا آخَرِينَ
Ay ay dëkk yu daan tooñ, te Nu alag leen ; ba noppi sosaat ca seen ginnaaw ñeneen nit.
12فَلَمَّا أَحَسُّوا بَأْسَنَا إِذَا هُم مِّنْهَا يَرْكُضُونَ
Ba ñu yégee Sunu mbugal, ñoom daw nañu [di jéem a génn dëkk ya].
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Anbiya 10

Simoore Al-Anbiya Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàcce Nanu ci yéen ab Téere boo xam ne seen…

Simoore Aaya 10/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers