Al-Anbiya · 109/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ آذَنتُكُمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۖ وَإِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ أَم بَعِيدٌ مَّا تُوعَدُونَ ۝١٠٩
Fa in tawallaw faqul aazantukum `alaa sawaaa`; wa in adreee aqareebun am ba`eedum maa too`adoon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu dëddoo, neel : “Xamal naa leen loo xam ne noo ca yem ; mu di ndax li ñu leen dig dafa jegeñ walla dafa sori.

🎧 Dégg


📜 Aaya 107-111 — Simoore Al-Anbiya

107وَمَا أَرْسَلْنَاكَ إِلَّا رَحْمَةً لِّلْعَالَمِينَ
Yónniwunu la ngir dara lu dul nga nekk yërmaandey waa àddina.
108قُلْ إِنَّمَا يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَهَلْ أَنتُم مُّسْلِمُونَ
Neel : “Man dey dañu may soloo doŋŋ : Waaye seen Yàlla jenn doŋŋ la ; kon ndax yéen dungeen wommatu jébbalu? ” [dugg ci Lislaam]
109فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ آذَنتُكُمْ عَلَىٰ سَوَاءٍ ۖ وَإِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ أَم بَعِيدٌ مَّا تُوعَدُونَ
Bu ñu dëddoo, neel : “Xamal naa leen loo xam ne noo ca yem ; mu di ndax li ñu leen dig dafa jegeñ walla dafa sori.
110إِنَّهُ يَعْلَمُ الْجَهْرَ مِنَ الْقَوْلِ وَيَعْلَمُ مَا تَكْتُمُونَ
Moom dey xam na li ñuy biral ciy wax ak it li ngeen di nëbb.
111وَإِنْ أَدْرِي لَعَلَّهُ فِتْنَةٌ لَّكُمْ وَمَتَاعٌ إِلَىٰ حِينٍ
Te xamuma ; ndax moom nattu la ci yéen ak xéewal gu gàtt” !
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Al-Anbiya 109

Simoore Al-Anbiya Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu dëddoo, neel : “Xamal naa leen loo xam…

Simoore Aaya 109/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers