Al-Anbiya · 12/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
فَلَمَّا أَحَسُّوا بَأْسَنَا إِذَا هُم مِّنْهَا يَرْكُضُونَ ۝١٢
Falammaaa ahassoo baasanaaa izaaa hum minhaa yarkudoon
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu yégee Sunu mbugal, ñoom daw nañu [di jéem a génn dëkk ya].
🎧 Dégg

📜 Aaya 10-14 — Al-Anbiya

10لَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكُمْ كِتَابًا فِيهِ ذِكْرُكُمْ ۖ أَفَلَا تَعْقِلُونَ
Wàcce Nanu ci yéen ab Téere boo xam ne seen teraangaa nekk ca biir. Moo ndax dangeen dul xel-lu ?
11وَكَمْ قَصَمْنَا مِن قَرْيَةٍ كَانَتْ ظَالِمَةً وَأَنشَأْنَا بَعْدَهَا قَوْمًا آخَرِينَ
Ay ay dëkk yu daan tooñ, te Nu alag leen ; ba noppi sosaat ca seen ginnaaw ñeneen nit.
12فَلَمَّا أَحَسُّوا بَأْسَنَا إِذَا هُم مِّنْهَا يَرْكُضُونَ
Ba ñu yégee Sunu mbugal, ñoom daw nañu [di jéem a génn dëkk ya].
13لَا تَرْكُضُوا وَارْجِعُوا إِلَىٰ مَا أُتْرِفْتُمْ فِيهِ وَمَسَاكِنِكُمْ لَعَلَّكُمْ تُسْأَلُونَ
Buleen daw de. Delluleen fa seen kër ya ngeen nekkoon di xéewlu, ndax xéy-na dees na leen laaj.
14قَالُوا يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Ñu ne : “Ngalla nun ! Nun dey ay tooñkat lanu woon”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Anbiya 12

Simoore Al-Anbiya Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu yégee Sunu mbugal, ñoom daw nañu [di jéem…

Simoore Aaya 12/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers