Al-Anbiya · 51/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
۞ وَلَقَدْ آتَيْنَا إِبْرَاهِيمَ رُشْدَهُ مِن قَبْلُ وَكُنَّا بِهِ عَالِمِينَ ۝٥١
Wa laqad aatainaaa Ibraaheema rushdahoo min qablu wa kunnaa bihee `aalimeen
📖 Tekkim Wolof
Te mayoon Nanu Ibraahiima njub lu jiitu. Te nekkoon Nanu ñu ko xam xéll.

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — Simoore Al-Anbiya

49الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَهُم مِّنَ السَّاعَةِ مُشْفِقُونَ
ñooy ña ragal seen Boroom ci kumpa, te ñoom way-jàq lañu ca Bis-pénc ba.
50وَهَٰذَا ذِكْرٌ مُّبَارَكٌ أَنزَلْنَاهُ ۚ أَفَأَنتُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Te lii [Alxuraan jii], tur la wu barkeel [sakkan] wu Nu wàcce. Ndax yéen dangeen koy weddi ?
51۞ وَلَقَدْ آتَيْنَا إِبْرَاهِيمَ رُشْدَهُ مِن قَبْلُ وَكُنَّا بِهِ عَالِمِينَ
Te mayoon Nanu Ibraahiima njub lu jiitu. Te nekkoon Nanu ñu ko xam xéll.
52إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَا هَٰذِهِ التَّمَاثِيلُ الَّتِي أَنتُمْ لَهَا عَاكِفُونَ
[Fàttalikul] ba mu waxee baayam ak nitam ña, ne leen : “Ana luy yàlla xërëm [yu diy jëmm yu ñu yatt] te ngeen fonk leen lool ? ”.
53قَالُوا وَجَدْنَا آبَاءَنَا لَهَا عَابِدِينَ
Ñu tontu ne : “Dañoo fekk sunuy baay di leen jaamu”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Al-Anbiya 51

Simoore Al-Anbiya Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te mayoon Nanu Ibraahiima njub lu jiitu. Te nekkoon Nanu…

Simoore Aaya 51/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers