Al-Anbiya · 86/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَأَدْخَلْنَاهُمْ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُم مِّنَ الصَّالِحِينَ ۝٨٦
Wa adkhalnaahum fee rahmatinaa innahum minas saaliheen
📖 Tekkim Wolof
dugal Nanu leen ci Sunu yërmaande, bokk nañu ca ñu yiw ña [sell].

🎧 Dégg


📜 Aaya 84-88 — Simoore Al-Anbiya

84فَاسْتَجَبْنَا لَهُ فَكَشَفْنَا مَا بِهِ مِن ضُرٍّ ۖ وَآتَيْنَاهُ أَهْلَهُ وَمِثْلَهُم مَّعَهُمْ رَحْمَةً مِّنْ عِندِنَا وَذِكْرَىٰ لِلْعَابِدِينَ
Te Nu nangul ko, daldi wuññi lor ja nekkon ca moom, Nu may ko njabootam te boole ca ñeneen ñu tollu ni ñoom, muy yërmaande ju tukkee fi Nun, ak fàttali jaamukati Yàlla yi.
85وَإِسْمَاعِيلَ وَإِدْرِيسَ وَذَا الْكِفْلِ ۖ كُلٌّ مِّنَ الصَّابِرِينَ
Ak Ismaayiila, ak Idriisa ak Zul-Kifli, ñoom ñépp bokkoon nañu ca muñkat ya ;
86وَأَدْخَلْنَاهُمْ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُم مِّنَ الصَّالِحِينَ
dugal Nanu leen ci Sunu yërmaande, bokk nañu ca ñu yiw ña [sell].
87وَذَا النُّونِ إِذ ذَّهَبَ مُغَاضِبًا فَظَنَّ أَن لَّن نَّقْدِرَ عَلَيْهِ فَنَادَىٰ فِي الظُّلُمَاتِ أَن لَّا إِلَٰهَ إِلَّا أَنتَ سُبْحَانَكَ إِنِّي كُنتُ مِنَ الظَّالِمِينَ
[Fàttalikul] boroom jën wa [Yunus] ba mu demee ànd ak mer. Te mu jortoon ne du lu Nu dogal ci moom [ciw tiis ngir la mu dem te amu ca ndigal]. Waaye mu woote ca biir lëndëm ga ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yaw ! Tudd naa sag sell ! Man nag bokk naa ca tooñkat ya”.
88فَاسْتَجَبْنَا لَهُ وَنَجَّيْنَاهُ مِنَ الْغَمِّ ۚ وَكَذَٰلِكَ نُنجِي الْمُؤْمِنِينَ
Nu daldi koy nangul te musal ko ca njàqare ja. Te it noonu la Nuy musalee way-gëm ña.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
86Aaya

Tekki — Al-Anbiya 86

Simoore Al-Anbiya Aaya 86 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dugal Nanu leen ci Sunu yërmaande, bokk nañu ca ñu…

Simoore Aaya 86/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 84–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers