Al-Anbiya · 85/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَإِسْمَاعِيلَ وَإِدْرِيسَ وَذَا الْكِفْلِ ۖ كُلٌّ مِّنَ الصَّابِرِينَ ٨٥
Transliteration
Wa Ismaa`eela wa Idreesa wa Zal Kifli kullum minas saabireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ak Ismaayiila, ak Idriisa ak Zul-Kifli, ñoom ñépp bokkoon nañu ca muñkat ya ;
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 83-87 — Al-Anbiya
83۞ وَأَيُّوبَ إِذْ نَادَىٰ رَبَّهُ أَنِّي مَسَّنِيَ الضُّرُّ وَأَنتَ أَرْحَمُ الرَّاحِمِينَ
Ak Ayuuba [fàttalikul] ba mu woowee Boroomam ne ko : “Man dey mettit dal na ma. Te Yaw yaay gën jaa yërëme yërëmaakoon ya” !
84فَاسْتَجَبْنَا لَهُ فَكَشَفْنَا مَا بِهِ مِن ضُرٍّ ۖ وَآتَيْنَاهُ أَهْلَهُ وَمِثْلَهُم مَّعَهُمْ رَحْمَةً مِّنْ عِندِنَا وَذِكْرَىٰ لِلْعَابِدِينَ
Te Nu nangul ko, daldi wuññi lor ja nekkon ca moom, Nu may ko njabootam te boole ca ñeneen ñu tollu ni ñoom, muy yërmaande ju tukkee fi Nun, ak fàttali jaamukati Yàlla yi.
85وَإِسْمَاعِيلَ وَإِدْرِيسَ وَذَا الْكِفْلِ ۖ كُلٌّ مِّنَ الصَّابِرِينَ
Ak Ismaayiila, ak Idriisa ak Zul-Kifli, ñoom ñépp bokkoon nañu ca muñkat ya ;
86وَأَدْخَلْنَاهُمْ فِي رَحْمَتِنَا ۖ إِنَّهُم مِّنَ الصَّالِحِينَ
dugal Nanu leen ci Sunu yërmaande, bokk nañu ca ñu yiw ña [sell].
87وَذَا النُّونِ إِذ ذَّهَبَ مُغَاضِبًا فَظَنَّ أَن لَّن نَّقْدِرَ عَلَيْهِ فَنَادَىٰ فِي الظُّلُمَاتِ أَن لَّا إِلَٰهَ إِلَّا أَنتَ سُبْحَانَكَ إِنِّي كُنتُ مِنَ الظَّالِمِينَ
[Fàttalikul] boroom jën wa [Yunus] ba mu demee ànd ak mer. Te mu jortoon ne du lu Nu dogal ci moom [ciw tiis ngir la mu dem te amu ca ndigal]. Waaye mu woote ca biir lëndëm ga ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yaw ! Tudd naa sag sell ! Man nag bokk naa ca tooñkat ya”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
85Aaya
Tekki — Al-Anbiya 85
Simoore Al-Anbiya Aaya 85 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ak Ismaayiila, ak Idriisa ak Zul-Kifli, ñoom ñépp bokkoon nañu…Simoore Aaya 85/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 83–87. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








