Al-Anbiya · 95/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَحَرَامٌ عَلَىٰ قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا أَنَّهُمْ لَا يَرْجِعُونَ ۝٩٥
Wa haraamun `alaa qaryatin ahlaknaahaaa annahum laa yarji`oon
📖 Tekkim Wolof
Te dëkk bu Nu rey, waa dëkk ba duñu mënatee dellusi!

🎧 Dégg


📜 Aaya 93-97 — Al-Anbiya

93وَتَقَطَّعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ ۖ كُلٌّ إِلَيْنَا رَاجِعُونَ
De daggate nañu seeni mbir ca seen diggante. Te ñoom ñépp fi Nun lañuy dellusi.
94فَمَن يَعْمَلْ مِنَ الصَّالِحَاتِ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَا كُفْرَانَ لِسَعْيِهِ وَإِنَّا لَهُ كَاتِبُونَ
Képp kuy jëf ca jëf yu yiw ya te muy ku gëm, deesul fakk jëfam ndax Nun noo ko koy bindal.
95وَحَرَامٌ عَلَىٰ قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا أَنَّهُمْ لَا يَرْجِعُونَ
Te dëkk bu Nu rey, waa dëkk ba duñu mënatee dellusi!
96حَتَّىٰ إِذَا فُتِحَتْ يَأْجُوجُ وَمَأْجُوجُ وَهُم مِّن كُلِّ حَدَبٍ يَنسِلُونَ
Ba ba kerook Nuy ubbi Yaajuuja ak Maajuuja ñuy sottiku di rogaat ci tunduwu nekk ;
97وَاقْتَرَبَ الْوَعْدُ الْحَقُّ فَإِذَا هِيَ شَاخِصَةٌ أَبْصَارُ الَّذِينَ كَفَرُوا يَا وَيْلَنَا قَدْ كُنَّا فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا بَلْ كُنَّا ظَالِمِينَ
dig bu dëggu ba daldi gën a jegeñ, bu boobaa bëti ña weddi dana buqiku, ñu naan : “Ngalla nun ! Nekkoon nanu cig càggante ci lii. Te nekkoon nanu di ay tooñkat”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
95Aaya

Tekki — Al-Anbiya 95

Simoore Al-Anbiya Aaya 95 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te dëkk bu Nu rey, waa dëkk ba duñu mënatee…

Simoore Aaya 95/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 93–97. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers