Al-Anbiya · 94/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
فَمَن يَعْمَلْ مِنَ الصَّالِحَاتِ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَا كُفْرَانَ لِسَعْيِهِ وَإِنَّا لَهُ كَاتِبُونَ ۝٩٤
Famai ya`mal minas saalihaati wa huwa mu`minun falaa kufraana lisa`yihee wa innaa lahoo kaatiboon
📖 Tekkim Wolof
Képp kuy jëf ca jëf yu yiw ya te muy ku gëm, deesul fakk jëfam ndax Nun noo ko koy bindal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Simoore Al-Anbiya

92إِنَّ هَٰذِهِ أُمَّتُكُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَأَنَا رَبُّكُمْ فَاعْبُدُونِ
Lii nag moo di seen diine, mu di jenn diine doŋŋ, te Man maa di seen Boroom. Waay- waay kon jaamuleen Ma.
93وَتَقَطَّعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ ۖ كُلٌّ إِلَيْنَا رَاجِعُونَ
De daggate nañu seeni mbir ca seen diggante. Te ñoom ñépp fi Nun lañuy dellusi.
94فَمَن يَعْمَلْ مِنَ الصَّالِحَاتِ وَهُوَ مُؤْمِنٌ فَلَا كُفْرَانَ لِسَعْيِهِ وَإِنَّا لَهُ كَاتِبُونَ
Képp kuy jëf ca jëf yu yiw ya te muy ku gëm, deesul fakk jëfam ndax Nun noo ko koy bindal.
95وَحَرَامٌ عَلَىٰ قَرْيَةٍ أَهْلَكْنَاهَا أَنَّهُمْ لَا يَرْجِعُونَ
Te dëkk bu Nu rey, waa dëkk ba duñu mënatee dellusi!
96حَتَّىٰ إِذَا فُتِحَتْ يَأْجُوجُ وَمَأْجُوجُ وَهُم مِّن كُلِّ حَدَبٍ يَنسِلُونَ
Ba ba kerook Nuy ubbi Yaajuuja ak Maajuuja ñuy sottiku di rogaat ci tunduwu nekk ;
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Al-Anbiya 94

Simoore Al-Anbiya Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp kuy jëf ca jëf yu yiw ya te muy…

Simoore Aaya 94/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers