Al-Hajj · 71/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَيَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَمْ يُنَزِّلْ بِهِ سُلْطَانًا وَمَا لَيْسَ لَهُم بِهِ عِلْمٌ ۗ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِن نَّصِيرٍ ۝٧١
Wa ya`budoona min doonil laahi maa lam yunazzil bihee sultaananw wa maa laisa lahum bihee `ilm; wa maa lizzaalimeena min naseer
📖 Tekkim Wolof
Te ña ngay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne wenn lay wàccu ca te amuñu ci benn xam- xam. Tooñkat ya duñu am dimbal de.

🎧 Dégg


📜 Aaya 69-73 — Al-Hajj

69اللَّهُ يَحْكُمُ بَيْنَكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كُنتُمْ فِيهِ تَخْتَلِفُونَ
Yàlla dana àtte seen diggante bu Bis-pénc baa ca la ngeen doon juuyoo”.
70أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۗ إِنَّ ذَٰلِكَ فِي كِتَابٍ ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرٌ
Ndax dangaa xamul ne Yàlla xam na li nekk ci asamaan yi ak suuf si ? Te loolu nekk na ci ab Téere, te it loolu lu yomb Yàlla la.
71وَيَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَمْ يُنَزِّلْ بِهِ سُلْطَانًا وَمَا لَيْسَ لَهُم بِهِ عِلْمٌ ۗ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِن نَّصِيرٍ
Te ña ngay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne wenn lay wàccu ca te amuñu ci benn xam- xam. Tooñkat ya duñu am dimbal de.
72وَإِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُنَا بَيِّنَاتٍ تَعْرِفُ فِي وُجُوهِ الَّذِينَ كَفَرُوا الْمُنكَرَ ۖ يَكَادُونَ يَسْطُونَ بِالَّذِينَ يَتْلُونَ عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا ۗ قُلْ أَفَأُنَبِّئُكُم بِشَرٍّ مِّن ذَٰلِكُمُ ۗ النَّارُ وَعَدَهَا اللَّهُ الَّذِينَ كَفَرُوا ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
Bu ñu jàngee ci seen kanam Sunu kàddu yu leer yi, danga ràññee ca kanamu ña weddi weddi ga. Te tuuti kon ñu songu ña jàng Sunuy kàddu ci seen kanam. Neel : “Ndax ma xamal leen lu yées loolu ci yéen ? - Mooy Safara : Yàlla dig na ko ña weddi. Ndax daluwaay bu bon !”
73يَا أَيُّهَا النَّاسُ ضُرِبَ مَثَلٌ فَاسْتَمِعُوا لَهُ ۚ إِنَّ الَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ لَن يَخْلُقُوا ذُبَابًا وَلَوِ اجْتَمَعُوا لَهُ ۖ وَإِن يَسْلُبْهُمُ الذُّبَابُ شَيْئًا لَّا يَسْتَنقِذُوهُ مِنْهُ ۚ ضَعُفَ الطَّالِبُ وَالْمَطْلُوبُ
Éy yéen nit ñi ! Ñi ngi leen di sadd léebu, dégluleen ko : “Ñi ngeen di jaamu bàyyi Yàlla duñu mën bind mukk aw weñ, doonte dañoo dajaloo ngir def ko. Te bu leen wenn weñ jëlaloon dara, duñu ko mën a nangu ci moom. Néew na doole ka jaamu ak ka ñu jaamu ! ”
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
71Aaya

Tekki — Al-Hajj 71

Simoore Al-Hajj Aaya 71 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ña ngay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne wenn…

Simoore Aaya 71/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 69–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers