Al-Hajj · 70/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۗ إِنَّ ذَٰلِكَ فِي كِتَابٍ ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرٌ ٧٠
Transliteration
Alam ta`lam annal laaha ya`lamu maa fis samaaa`i wal ard; inna zaalika fee kitaab; inna zaalika `alal laahi yaseer
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ndax dangaa xamul ne Yàlla xam na li nekk ci asamaan yi ak suuf si ? Te loolu nekk na ci ab Téere, te it loolu lu yomb Yàlla la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 68-72 — Al-Hajj
68وَإِن جَادَلُوكَ فَقُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا تَعْمَلُونَ
Bu ñu dàggasanteek yaw, neel : “Yàlla moo gën a xam li ngeen di def.
69اللَّهُ يَحْكُمُ بَيْنَكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كُنتُمْ فِيهِ تَخْتَلِفُونَ
Yàlla dana àtte seen diggante bu Bis-pénc baa ca la ngeen doon juuyoo”.
70أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۗ إِنَّ ذَٰلِكَ فِي كِتَابٍ ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرٌ
Ndax dangaa xamul ne Yàlla xam na li nekk ci asamaan yi ak suuf si ? Te loolu nekk na ci ab Téere, te it loolu lu yomb Yàlla la.
71وَيَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَمْ يُنَزِّلْ بِهِ سُلْطَانًا وَمَا لَيْسَ لَهُم بِهِ عِلْمٌ ۗ وَمَا لِلظَّالِمِينَ مِن نَّصِيرٍ
Te ña ngay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne wenn lay wàccu ca te amuñu ci benn xam- xam. Tooñkat ya duñu am dimbal de.
72وَإِذَا تُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ آيَاتُنَا بَيِّنَاتٍ تَعْرِفُ فِي وُجُوهِ الَّذِينَ كَفَرُوا الْمُنكَرَ ۖ يَكَادُونَ يَسْطُونَ بِالَّذِينَ يَتْلُونَ عَلَيْهِمْ آيَاتِنَا ۗ قُلْ أَفَأُنَبِّئُكُم بِشَرٍّ مِّن ذَٰلِكُمُ ۗ النَّارُ وَعَدَهَا اللَّهُ الَّذِينَ كَفَرُوا ۖ وَبِئْسَ الْمَصِيرُ
Bu ñu jàngee ci seen kanam Sunu kàddu yu leer yi, danga ràññee ca kanamu ña weddi weddi ga. Te tuuti kon ñu songu ña jàng Sunuy kàddu ci seen kanam. Neel : “Ndax ma xamal leen lu yées loolu ci yéen ? - Mooy Safara : Yàlla dig na ko ña weddi. Ndax daluwaay bu bon !”
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
70Aaya
Tekki — Al-Hajj 70
Simoore Al-Hajj Aaya 70 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax dangaa xamul ne Yàlla xam na li nekk ci…Simoore Aaya 70/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 68–72. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








