Al-Mu'minun · 16/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
ثُمَّ إِنَّكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ تُبْعَثُونَ ۝١٦
Summa innakum Yawmal Qiyaamati tub`asoon
📖 Tekkim Wolof
Ba noppi Bis-pénc ba Mu dekkal leen.
🎧 Dégg

📜 Aaya 14-18 — Al-Mu'minun

14ثُمَّ خَلَقْنَا النُّطْفَةَ عَلَقَةً فَخَلَقْنَا الْعَلَقَةَ مُضْغَةً فَخَلَقْنَا الْمُضْغَةَ عِظَامًا فَكَسَوْنَا الْعِظَامَ لَحْمًا ثُمَّ أَنشَأْنَاهُ خَلْقًا آخَرَ ۚ فَتَبَارَكَ اللَّهُ أَحْسَنُ الْخَالِقِينَ
Ginnaaw ba Nu def lumbu ma di aw suux ; ginnaaw ba Nu def suux wa mu di ay yax, daldi sànge yax ya aw yàpp. Daldi koy def jëmm,Yàllaa mën a sakkanal. Moom miy gën gi Bindkat !
15ثُمَّ إِنَّكُم بَعْدَ ذَٰلِكَ لَمَيِّتُونَ
Bu loolu jàllee, dangeen di dee.
16ثُمَّ إِنَّكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ تُبْعَثُونَ
Ba noppi Bis-pénc ba Mu dekkal leen.
17وَلَقَدْ خَلَقْنَا فَوْقَكُمْ سَبْعَ طَرَائِقَ وَمَا كُنَّا عَنِ الْخَلْقِ غَافِلِينَ
Sàkk Naa juroóm-ñaari asamaan yu leen tiim. Te na leen wóor ne sàgganewuma leen ci li Ma leen sàkk.
18وَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً بِقَدَرٍ فَأَسْكَنَّاهُ فِي الْأَرْضِ ۖ وَإِنَّا عَلَىٰ ذَهَابٍ بِهِ لَقَادِرُونَ
Te wàcce Nanu ndox mu bawoo ca asmaan. Topp Nu sowal ko ci biir suuf, kon Nun am Nanu kàttanug sànk ko de.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 16

Simoore Al-Mu'minun Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba noppi Bis-pénc ba Mu dekkal leen.

Simoore Aaya 16/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers