Al-Mu'minun · 49/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ لَعَلَّهُمْ يَهْتَدُونَ ٤٩
Transliteration
Wa laqad aatainaa Moosal Kitaaba la`allahum yahtadoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Jox Nanu Muusaa Téere ba ngir mu waar leen ca ba ba ñuy gindiku.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 47-51 — Simoore Al-Mu'minun
47فَقَالُوا أَنُؤْمِنُ لِبَشَرَيْنِ مِثْلِنَا وَقَوْمُهُمَا لَنَا عَابِدُونَ
Ñuy wax naan : “Ndax dananu gëm ñaari nit ñu mel ni nun, ñoo xam ne seenu xeet sunuy jaam lañu.
48فَكَذَّبُوهُمَا فَكَانُوا مِنَ الْمُهْلَكِينَ
Ñu daldi leen weddi, daldi alku.
49وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ لَعَلَّهُمْ يَهْتَدُونَ
Jox Nanu Muusaa Téere ba ngir mu waar leen ca ba ba ñuy gindiku.
50وَجَعَلْنَا ابْنَ مَرْيَمَ وَأُمَّهُ آيَةً وَآوَيْنَاهُمَا إِلَىٰ رَبْوَةٍ ذَاتِ قَرَارٍ وَمَعِينٍ
Te Noo def doomi Maryaama [Iisaa] ak yaayam di kéemaan ; te Nu dugal leen ci aw tundu, mu maasee ànd ak bëti-ndox [naan].
51يَا أَيُّهَا الرُّسُلُ كُلُوا مِنَ الطَّيِّبَاتِ وَاعْمَلُوا صَالِحًا ۖ إِنِّي بِمَا تَعْمَلُونَ عَلِيمٌ
Éy yéen Yonent yi ! lekk-leen ci yi teey yi tey jëf u yiw. Man dey kuy xam laa li ngeen di def.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
49Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 49
Simoore Al-Mu'minun Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jox Nanu Muusaa Téere ba ngir mu waar leen ca…Simoore Aaya 49/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








