Al-Mu'minun · 48/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
فَكَذَّبُوهُمَا فَكَانُوا مِنَ الْمُهْلَكِينَ ۝٤٨
Fakazzaboohumaa fakaanoo minal mmuhlakeen
📖 Tekkim Wolof
Ñu daldi leen weddi, daldi alku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Simoore Al-Mu'minun

46إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ فَاسْتَكْبَرُوا وَكَانُوا قَوْمًا عَالِينَ
jëmale ko ca Firawna ak gàngooram ña doon rëy-rëylu te doon aw nit ñuy kawe-kawelu.
47فَقَالُوا أَنُؤْمِنُ لِبَشَرَيْنِ مِثْلِنَا وَقَوْمُهُمَا لَنَا عَابِدُونَ
Ñuy wax naan : “Ndax dananu gëm ñaari nit ñu mel ni nun, ñoo xam ne seenu xeet sunuy jaam lañu.
48فَكَذَّبُوهُمَا فَكَانُوا مِنَ الْمُهْلَكِينَ
Ñu daldi leen weddi, daldi alku.
49وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ لَعَلَّهُمْ يَهْتَدُونَ
Jox Nanu Muusaa Téere ba ngir mu waar leen ca ba ba ñuy gindiku.
50وَجَعَلْنَا ابْنَ مَرْيَمَ وَأُمَّهُ آيَةً وَآوَيْنَاهُمَا إِلَىٰ رَبْوَةٍ ذَاتِ قَرَارٍ وَمَعِينٍ
Te Noo def doomi Maryaama [Iisaa] ak yaayam di kéemaan ; te Nu dugal leen ci aw tundu, mu maasee ànd ak bëti-ndox [naan].
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 48

Simoore Al-Mu'minun Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu daldi leen weddi, daldi alku.

Simoore Aaya 48/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers