Al-Mu'minun · 54/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
فَذَرْهُمْ فِي غَمْرَتِهِمْ حَتَّىٰ حِينٍ ۝٥٤
Fazarhum fee ghamratihim hattaa heen
📖 Tekkim Wolof
Bàyyileen ci seen ngëlëmte loolu ab diir.

🎧 Dégg


📜 Aaya 52-56 — Al-Mu'minun

52وَإِنَّ هَٰذِهِ أُمَّتُكُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَأَنَا رَبُّكُمْ فَاتَّقُونِ
Te diine jii mooy seen diine, di jenn diine, te maa di seen Boroom. Ragal-leen Ma”.
53فَتَقَطَّعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ زُبُرًا ۖ كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
Séddale nañu seeni mbir ci ay kurél, xaaj bu ne doyloo na la fa moom.
54فَذَرْهُمْ فِي غَمْرَتِهِمْ حَتَّىٰ حِينٍ
Bàyyileen ci seen ngëlëmte loolu ab diir.
55أَيَحْسَبُونَ أَنَّمَا نُمِدُّهُم بِهِ مِن مَّالٍ وَبَنِينَ
Ndax dañoo jàpp ne li ñu leen may ci alal ak i doom,
56نُسَارِعُ لَهُمْ فِي الْخَيْرَاتِ ۚ بَل لَّا يَشْعُرُونَ
Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk] ? Ñoom yëguñu li xew de.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
54Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 54

Simoore Al-Mu'minun Aaya 54 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bàyyileen ci seen ngëlëmte loolu ab diir.

Simoore Aaya 54/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 52–56. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers