Al-Mu'minun · 55/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
أَيَحْسَبُونَ أَنَّمَا نُمِدُّهُم بِهِ مِن مَّالٍ وَبَنِينَ ۝٥٥
A-yahsaboona annnamaa numiduhum bihee mimmaalinw wa baneen
📖 Tekkim Wolof
Ndax dañoo jàpp ne li ñu leen may ci alal ak i doom,
🎧 Dégg

📜 Aaya 53-57 — Al-Mu'minun

53فَتَقَطَّعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ زُبُرًا ۖ كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
Séddale nañu seeni mbir ci ay kurél, xaaj bu ne doyloo na la fa moom.
54فَذَرْهُمْ فِي غَمْرَتِهِمْ حَتَّىٰ حِينٍ
Bàyyileen ci seen ngëlëmte loolu ab diir.
55أَيَحْسَبُونَ أَنَّمَا نُمِدُّهُم بِهِ مِن مَّالٍ وَبَنِينَ
Ndax dañoo jàpp ne li ñu leen may ci alal ak i doom,
56نُسَارِعُ لَهُمْ فِي الْخَيْرَاتِ ۚ بَل لَّا يَشْعُرُونَ
Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk] ? Ñoom yëguñu li xew de.
57إِنَّ الَّذِينَ هُم مِّنْ خَشْيَةِ رَبِّهِم مُّشْفِقُونَ
Ña sóobu dëgg dëgg ci ragal seen Boroom,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
55Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 55

Simoore Al-Mu'minun Aaya 55 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax dañoo jàpp ne li ñu leen may ci alal…

Simoore Aaya 55/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 53–57. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers