Al-Mu'minun · 67/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
مُسْتَكْبِرِينَ بِهِ سَامِرًا تَهْجُرُونَ ۝٦٧
Mustakbireena bihee saamiran tahjuroon
📖 Tekkim Wolof
ngeen daan ca rëy-rëylu, di ko waxtaane”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Al-Mu'minun

65لَا تَجْأَرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّكُم مِّنَّا لَا تُنصَرُونَ
“Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.
66قَدْ كَانَتْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُمْ عَلَىٰ أَعْقَابِكُمْ تَنكِصُونَ
Samay kàddu wàccoon na ci yéen ; ngeen daan ko dummóoyu,
67مُسْتَكْبِرِينَ بِهِ سَامِرًا تَهْجُرُونَ
ngeen daan ca rëy-rëylu, di ko waxtaane”.
68أَفَلَمْ يَدَّبَّرُوا الْقَوْلَ أَمْ جَاءَهُم مَّا لَمْ يَأْتِ آبَاءَهُمُ الْأَوَّلِينَ
Ndax dañoo settantalul wax ji [di Alxuraan] ? Walla daleen a digalul lu ñu digalul woon seen maam ya leen jiitu woon ?
69أَمْ لَمْ يَعْرِفُوا رَسُولَهُمْ فَهُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Walla dañoo xamul seenub Yonent, ba tax ñu umpale ko ?
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 67

Simoore Al-Mu'minun Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngeen daan ca rëy-rëylu, di ko waxtaane”.

Simoore Aaya 67/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers