Al-Mu'minun · 66/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
قَدْ كَانَتْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُمْ عَلَىٰ أَعْقَابِكُمْ تَنكِصُونَ ۝٦٦
Qad kaanat Aayaatee tutlaa `alaikum fakuntum `alaaa a`qaabikum tankisoon
📖 Tekkim Wolof
Samay kàddu wàccoon na ci yéen ; ngeen daan ko dummóoyu,
🎧 Dégg

📜 Aaya 64-68 — Al-Mu'minun

64حَتَّىٰ إِذَا أَخَذْنَا مُتْرَفِيهِم بِالْعَذَابِ إِذَا هُمْ يَجْأَرُونَ
ba ba ñuy mbugal seen njiit ya ñu seet seet di yuuxu walla.
65لَا تَجْأَرُوا الْيَوْمَ ۖ إِنَّكُم مِّنَّا لَا تُنصَرُونَ
“Buleen wooteg wallu tey. Kenn duleen dimbali ci Nun.
66قَدْ كَانَتْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَكُنتُمْ عَلَىٰ أَعْقَابِكُمْ تَنكِصُونَ
Samay kàddu wàccoon na ci yéen ; ngeen daan ko dummóoyu,
67مُسْتَكْبِرِينَ بِهِ سَامِرًا تَهْجُرُونَ
ngeen daan ca rëy-rëylu, di ko waxtaane”.
68أَفَلَمْ يَدَّبَّرُوا الْقَوْلَ أَمْ جَاءَهُم مَّا لَمْ يَأْتِ آبَاءَهُمُ الْأَوَّلِينَ
Ndax dañoo settantalul wax ji [di Alxuraan] ? Walla daleen a digalul lu ñu digalul woon seen maam ya leen jiitu woon ?
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 66

Simoore Al-Mu'minun Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Samay kàddu wàccoon na ci yéen ; ngeen daan ko…

Simoore Aaya 66/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers