Al-Mu'minun · 77/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
حَتَّىٰ إِذَا فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا ذَا عَذَابٍ شَدِيدٍ إِذَا هُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ ۝٧٧
Hattaaa izaa fatahnaa `alaihim baaban zaa `azaabin shadeedin izaa hum feehi mublisoon
📖 Tekkim Wolof
ba ba kerook Nuy ubbi ci ñoom buntub mbugal mu tar, ñu ne ca xiim.

🎧 Dégg


📜 Aaya 75-79 — Al-Mu'minun

75۞ وَلَوْ رَحِمْنَاهُمْ وَكَشَفْنَا مَا بِهِم مِّن ضُرٍّ لَّلَجُّوا فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Bu Nu leen yërëmoon ba wàññi seeni tiis, ñu dellooti nuur ca seen bew ga.
76وَلَقَدْ أَخَذْنَاهُم بِالْعَذَابِ فَمَا اسْتَكَانُوا لِرَبِّهِمْ وَمَا يَتَضَرَّعُونَ
Dananu leen mbugal ndax toroxlu wuñu ngir seen Boroom ; jaamuwuñu Ko,
77حَتَّىٰ إِذَا فَتَحْنَا عَلَيْهِم بَابًا ذَا عَذَابٍ شَدِيدٍ إِذَا هُمْ فِيهِ مُبْلِسُونَ
ba ba kerook Nuy ubbi ci ñoom buntub mbugal mu tar, ñu ne ca xiim.
78وَهُوَ الَّذِي أَنشَأَ لَكُمُ السَّمْعَ وَالْأَبْصَارَ وَالْأَفْئِدَةَ ۚ قَلِيلًا مَّا تَشْكُرُونَ
Moom moo leen sàkkal ag dégg, ak ug gis, ak i xel. Néewaana ngeen gërëm.
79وَهُوَ الَّذِي ذَرَأَكُمْ فِي الْأَرْضِ وَإِلَيْهِ تُحْشَرُونَ
Moom moo leen bàyyi ci kaw suuf si, te dees na leen pang jëme ci Moom.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 77

Simoore Al-Mu'minun Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba ba kerook Nuy ubbi ci ñoom buntub mbugal mu…

Simoore Aaya 77/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers