Al-Furqan · 29/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
لَّقَدْ أَضَلَّنِي عَنِ الذِّكْرِ بَعْدَ إِذْ جَاءَنِي ۗ وَكَانَ الشَّيْطَانُ لِلْإِنسَانِ خَذُولًا ۝٢٩
Laqad adallanee `aniz zikri ba`da iz jaaa`anee; wa kaanash Shaitaanu lil insaani khazoolaa
📖 Tekkim Wolof
Moo ma féewaleek [Alxuraan] ginnaaw ba mu ma ñëwalee”. Séytaane moo di yàqalekat bu bon (bu yées ba).

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Al-Furqan

27وَيَوْمَ يَعَضُّ الظَّالِمُ عَلَىٰ يَدَيْهِ يَقُولُ يَا لَيْتَنِي اتَّخَذْتُ مَعَ الرَّسُولِ سَبِيلًا
Bis ba tooñkat yi di màtt seeni yoxo, te naan : “Aka neexoon ma ànd ak Yonent aw yoon !...
28يَا وَيْلَتَىٰ لَيْتَنِي لَمْ أَتَّخِذْ فُلَانًا خَلِيلًا
Ngalla man ! Aka neexoon jàppewuma diw sàngam ab xarit !...
29لَّقَدْ أَضَلَّنِي عَنِ الذِّكْرِ بَعْدَ إِذْ جَاءَنِي ۗ وَكَانَ الشَّيْطَانُ لِلْإِنسَانِ خَذُولًا
Moo ma féewaleek [Alxuraan] ginnaaw ba mu ma ñëwalee”. Séytaane moo di yàqalekat bu bon (bu yées ba).
30وَقَالَ الرَّسُولُ يَا رَبِّ إِنَّ قَوْمِي اتَّخَذُوا هَٰذَا الْقُرْآنَ مَهْجُورًا
Yonent bi daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, nit ñi dey dëddu nañu Alxuraan jii ! ”
31وَكَذَٰلِكَ جَعَلْنَا لِكُلِّ نَبِيٍّ عَدُوًّا مِّنَ الْمُجْرِمِينَ ۗ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ هَادِيًا وَنَصِيرًا
Noonu la Nu defe woon Yonent bu nekk am ab noon ca tooñkat ya. Waaye nag, Sa Boroom Moom doy na sëkk kuy gindee, doy sëkk it ndimbal.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Al-Furqan 29

Simoore Al-Furqan Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ma féewaleek [Alxuraan] ginnaaw ba mu ma ñëwalee”. Séytaane…

Simoore Aaya 29/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers