Al-Furqan · 30/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
وَقَالَ الرَّسُولُ يَا رَبِّ إِنَّ قَوْمِي اتَّخَذُوا هَٰذَا الْقُرْآنَ مَهْجُورًا ۝٣٠
Wa qaalar Rasoolu yaa Rabbi inna qawmit takhazoo haazal Qur-aana mahjooraa
📖 Tekkim Wolof
Yonent bi daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, nit ñi dey dëddu nañu Alxuraan jii ! ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 28-32 — Al-Furqan

28يَا وَيْلَتَىٰ لَيْتَنِي لَمْ أَتَّخِذْ فُلَانًا خَلِيلًا
Ngalla man ! Aka neexoon jàppewuma diw sàngam ab xarit !...
29لَّقَدْ أَضَلَّنِي عَنِ الذِّكْرِ بَعْدَ إِذْ جَاءَنِي ۗ وَكَانَ الشَّيْطَانُ لِلْإِنسَانِ خَذُولًا
Moo ma féewaleek [Alxuraan] ginnaaw ba mu ma ñëwalee”. Séytaane moo di yàqalekat bu bon (bu yées ba).
30وَقَالَ الرَّسُولُ يَا رَبِّ إِنَّ قَوْمِي اتَّخَذُوا هَٰذَا الْقُرْآنَ مَهْجُورًا
Yonent bi daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, nit ñi dey dëddu nañu Alxuraan jii ! ”
31وَكَذَٰلِكَ جَعَلْنَا لِكُلِّ نَبِيٍّ عَدُوًّا مِّنَ الْمُجْرِمِينَ ۗ وَكَفَىٰ بِرَبِّكَ هَادِيًا وَنَصِيرًا
Noonu la Nu defe woon Yonent bu nekk am ab noon ca tooñkat ya. Waaye nag, Sa Boroom Moom doy na sëkk kuy gindee, doy sëkk it ndimbal.
32وَقَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا نُزِّلَ عَلَيْهِ الْقُرْآنُ جُمْلَةً وَاحِدَةً ۚ كَذَٰلِكَ لِنُثَبِّتَ بِهِ فُؤَادَكَ ۖ وَرَتَّلْنَاهُ تَرْتِيلًا
Yéefar yaa ngay wax naan : “Lu tax wàccendoo wuñu Alxuraan jii wenn yoon mu ne ñumm ? ” [Waaye Nun nii la Nu koy wàccee] ngir dëgëral sa xol. Te it toftale Nanu ko bu jekk.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Furqan 30

Simoore Al-Furqan Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yonent bi daldi wax ne : “Yaw sama Boroom, nit…

Simoore Aaya 30/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers