Al-Furqan · 45/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
أَلَمْ تَرَ إِلَىٰ رَبِّكَ كَيْفَ مَدَّ الظِّلَّ وَلَوْ شَاءَ لَجَعَلَهُ سَاكِنًا ثُمَّ جَعَلْنَا الشَّمْسَ عَلَيْهِ دَلِيلًا ۝٤٥
Alam tara ilaa Rabbika kaifa maddaz zilla wa law shaaa`a laja`alahoo saakinan summa ja`alnash shamsa `alaihe daleelaa
📖 Tekkim Wolof
Xanaa gisoo ni sa Boroom tàllale ker [takkander] ? Bu ko sooboon, Mu def ko mu di lu sax. Ba noppi def Nanu jant bi muy firnde,

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Furqan

43أَرَأَيْتَ مَنِ اتَّخَذَ إِلَٰهَهُ هَوَاهُ أَفَأَنتَ تَكُونُ عَلَيْهِ وَكِيلًا
Ndax gisuloo ka jàppe bakkanam mu di yàllaam ? Moo ndax dangay doon wéeruwaayam ?
44أَمْ تَحْسَبُ أَنَّ أَكْثَرَهُمْ يَسْمَعُونَ أَوْ يَعْقِلُونَ ۚ إِنْ هُمْ إِلَّا كَالْأَنْعَامِ ۖ بَلْ هُمْ أَضَلُّ سَبِيلًا
Walla dangaa jàpp ne li ëpp ci ñoom dañuy dégg di xam ? Ñoom kay ñook mala yi ñoo yem. Walla sax ñoo gën a sànku.
45أَلَمْ تَرَ إِلَىٰ رَبِّكَ كَيْفَ مَدَّ الظِّلَّ وَلَوْ شَاءَ لَجَعَلَهُ سَاكِنًا ثُمَّ جَعَلْنَا الشَّمْسَ عَلَيْهِ دَلِيلًا
Xanaa gisoo ni sa Boroom tàllale ker [takkander] ? Bu ko sooboon, Mu def ko mu di lu sax. Ba noppi def Nanu jant bi muy firnde,
46ثُمَّ قَبَضْنَاهُ إِلَيْنَا قَبْضًا يَسِيرًا
te ginnaaw loolu, xëcc Naa ko jëme ci Man muy lu yomb.
47وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِبَاسًا وَالنَّوْمَ سُبَاتًا وَجَعَلَ النَّهَارَ نُشُورًا
Mooy Ki leen defal guddi gi mu di ag col ak nelaw yu neex, te Mu def bëccëg muy yëngatukaay.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Furqan 45

Simoore Al-Furqan Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa gisoo ni sa Boroom tàllale ker [takkander] ? Bu…

Simoore Aaya 45/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers