Al-Furqan · 46/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
ثُمَّ قَبَضْنَاهُ إِلَيْنَا قَبْضًا يَسِيرًا ۝٤٦
Summa qabadnaahu ilainaa qabdany yaseeraa
📖 Tekkim Wolof
te ginnaaw loolu, xëcc Naa ko jëme ci Man muy lu yomb.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 44-48 — Simoore Al-Furqan

44أَمْ تَحْسَبُ أَنَّ أَكْثَرَهُمْ يَسْمَعُونَ أَوْ يَعْقِلُونَ ۚ إِنْ هُمْ إِلَّا كَالْأَنْعَامِ ۖ بَلْ هُمْ أَضَلُّ سَبِيلًا
Walla dangaa jàpp ne li ëpp ci ñoom dañuy dégg di xam ? Ñoom kay ñook mala yi ñoo yem. Walla sax ñoo gën a sànku.
45أَلَمْ تَرَ إِلَىٰ رَبِّكَ كَيْفَ مَدَّ الظِّلَّ وَلَوْ شَاءَ لَجَعَلَهُ سَاكِنًا ثُمَّ جَعَلْنَا الشَّمْسَ عَلَيْهِ دَلِيلًا
Xanaa gisoo ni sa Boroom tàllale ker [takkander] ? Bu ko sooboon, Mu def ko mu di lu sax. Ba noppi def Nanu jant bi muy firnde,
46ثُمَّ قَبَضْنَاهُ إِلَيْنَا قَبْضًا يَسِيرًا
te ginnaaw loolu, xëcc Naa ko jëme ci Man muy lu yomb.
47وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ اللَّيْلَ لِبَاسًا وَالنَّوْمَ سُبَاتًا وَجَعَلَ النَّهَارَ نُشُورًا
Mooy Ki leen defal guddi gi mu di ag col ak nelaw yu neex, te Mu def bëccëg muy yëngatukaay.
48وَهُوَ الَّذِي أَرْسَلَ الرِّيَاحَ بُشْرًا بَيْنَ يَدَيْ رَحْمَتِهِ ۚ وَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً طَهُورًا
Moom moo yebal ngelaw muy bégal ci yërmaandey Yàlla. Te wàcce Nanu ci asamaan si ndox mu laab,
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Al-Furqan 46

Simoore Al-Furqan Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te ginnaaw loolu, xëcc Naa ko jëme ci Man muy…

Simoore Aaya 46/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers