Al-Furqan · 64/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَالَّذِينَ يَبِيتُونَ لِرَبِّهِمْ سُجَّدًا وَقِيَامًا ۝٦٤
Wallazeena yabeetoona li Rabbihim sujjadanw wa qiyaamaa
📖 Tekkim Wolof
ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak a sujjóot] ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Simoore Al-Furqan

62وَهُوَ الَّذِي جَعَلَ اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ خِلْفَةً لِّمَنْ أَرَادَ أَن يَذَّكَّرَ أَوْ أَرَادَ شُكُورًا
Mooy Ki def guddeek bëccëg ñuy jëlasante ngir ku bëgg a xalaat, fàttaliku, mbaa mu bëgg a sant.
63وَعِبَادُ الرَّحْمَٰنِ الَّذِينَ يَمْشُونَ عَلَى الْأَرْضِ هَوْنًا وَإِذَا خَاطَبَهُمُ الْجَاهِلُونَ قَالُوا سَلَامًا
Ak jaami Yàlla yii dox ci kaw suuf si ndànk, su ñu réer ña di wàqanteek ñoom, ñuy wax jàmm,
64وَالَّذِينَ يَبِيتُونَ لِرَبِّهِمْ سُجَّدًا وَقِيَامًا
ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak a sujjóot] ;
65وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا اصْرِفْ عَنَّا عَذَابَ جَهَنَّمَ ۖ إِنَّ عَذَابَهَا كَانَ غَرَامًا
ñoom ñooy wax naan : “Yàlla, yal na nga nu dëddëleek mbugalum Safara”. - mbugalum Safara soosu lu ne dànk la.
66إِنَّهَا سَاءَتْ مُسْتَقَرًّا وَمُقَامًا
Ndaw dëkkuwaay bu soof !
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Al-Furqan 64

Simoore Al-Furqan Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñoom ñooy fanaanee julli te Yàlla rekk tax [taxaw ak…

Simoore Aaya 64/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers